Example items (sample of 50)

sen_strVerb_formVerb_featuresnsubj_formnsubj_featurestreebank_link
Ba ma nekkee xale bu tollu ci juróom-benni at , da ma masoon a gis benn bés nataal bu yeeme ci benn téeré bu doon nettali lu jëm ci " àll-bu-xonq bi " bu tuddoon " Ay nettali yu dëggu yu ñu dund " .nettali
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
bu
features...upos=PRON
NounClass=Wol5
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Li yees , mu a di natt yu tar yi nu " Bruxelles " teg ànduñu ak sunu ay namm-namm .teg
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Bruxelles
features...upos=PROPN
UD_Wolof-WTB
Du sama ag sàggan nag , ndax mag ñi a ma xàddiloo woon ca ba ma di tollu ci juróom-benni at , ma dumooyu mecce nataalkat bi doonoon sama mébet jamono jooja :doonoon
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Tense=Past
bi
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol5
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Nguur gu bees gi tax na ba ñu indi tër yu bees ci ay àtte yu bees .bees
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
yu
features...upos=PRON
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Kon goxub Afrik sañ na a ndamu ci li mu indil ag nite ci ay liggéey yu am solo .am
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
yu
features...upos=PRON
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Gisiin wii nga xam ne amul woon geneen jublu gu feeñ gu dul dëgëral xeltug ngérum ne-ne nekkoon na di lu safaanoo ak gisiinu Big Bang wi saxaloon ne àdduna bi am na ag tàmbali .dëgëral
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
gu
features...upos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Bennoo gu Almaañ gii juddoo ci ndajeem Vienne mi , nekkoon na di lu manul a wéy .nekkoon
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Tense=Past
bennoo
features...upos=NOUN
UD_Wolof-WTB
Soxna Jaaratu-l-Laahi Buso jànge na Alxuraan ci aji / way-juram wu jigéen wu séll wa te sàmmu , te doon senn soxna su ame taxawaay bu mat sëkk ci Lislaam ci jàngale ak yare , niki Sëriñ si , ba mokkal ko ci anam gu sell te sax ci jamono yi mu di am fukki at ak ñeent ( 14 at ) .am
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Àtte sañul tere lu dul jëf yi di lor mbooloo mi .sañul
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Polarity=Neg
àtte
features...upos=NOUN
UD_Wolof-WTB
Wante nag , téy jii ñu di waxe , ci atum 2009 sunu réew yi ñu a moom seen bopp :waxe
features...VerbForm=Fin
Aspect=Perf
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
NounClass=Wol2
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Nicolas Agbohou : Lu jiitu ñu di yeew CFA bi ci Ëro , Faraas rekk a daan lëñtu sunu koom-koom yi , léegi nag Ërop gépp am kàddu ak sañ-sañ ci nun .lëñtu
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Faraas
features...upos=PROPN
UD_Wolof-WTB
Naka noonu wàññil ñam yii : bëer ( doonte sax da ñu bind ne woyofalees na ko ) , diwu-ñor , sosisoŋ , yàpp wu duuf , meew mu ñu tonniwul diw ga , soowu niw , nebbon ( garees ) , dax , mburu mu ñu noote meew « pain au lait » , mbaa mburu ak sokkolaa , kurwaasã « croissants » , ngato , kreem glaase ...bind
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Ci 1989 , Nasaa sànni woon na ci jawwu ji satalit bii di Kob , ngir def ay gëstu ci ceññeeri mbëj-bijjaakon yu Big Bang .sànni
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Nasaa
features...upos=PROPN
UD_Wolof-WTB
BBC xamalees na ne firndalees na ci ay gëstu ne yaxi nit ka ñu gis ci ab bàmmeel ca Turki yoy raki Kleopaatar la ma tuddoon Arsinoe IV te ñu faatoon ko ci ndigalu Kleopaatar .gis
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Nit ku ne sañ na dem yoon , ci kanam àttekaay yi ko yelloo ci réew mi , ngir tawat fa jëf yi di bëtt sañ-sañ yi ko Ndeyu Àtte bi walla ab àtte fàggul .sañ
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
nit
features...upos=NOUN
UD_Wolof-WTB
Jëwriñu mbey mi a ngi topp mbir moomu .topp
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
jëwriñu
features...upos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
UD_Wolof-WTB
Kàddu yii tukkee ci Mustafaa Siise , kilifag biro bi di toppatoo fagaru ak jëflante ci Progaraam bi di xeex sibbiru , tudd PNLP ci frãse , wone na cër bu yaatu bi fagaru am ci xeex sibbiru , nga xam ne at mu ne dina rey lu ëpp milyoŋ ci ay nit .xeex
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
bi
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol5
Number=Sing
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Yokk ci , réew mi walla dénd bi doom Aadama cosaanoo , deesu ci def benn xàjjaatle bu wéeru ci taxawalinam ci wàllu politig , walla ci wàllu yoon , walla ci wàllu jëflante bi mu séq ak bitim-réew , mu a xam réew moomu mbaa dénd boobu da mu moom boppam , walla da mu nekk ci kiliftéef , walla mu am baatu biir rekk , walla mu am lu mejj ci baatam .nekk
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Tóol boobu nag lañu xëyy , di leen sàkku fu ngeen mënti nekk ngeen jàppale nu , siiwal béréb bi , yonnee seen xalaat ci mbir yi nu fi soxal nun ñépp .soxal
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
yi
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Bi ma di raam , sama pàppa , da mu amoon benn xaritu « seef de kanton » bu nu di wax Seex Njaay .wax
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
nu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=1
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Bindkat ya da ñu daan jëfandikoo li ñu di wax mbindum Yirogliif .jëfandikoo
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Yokk ci , réew mi walla dénd bi doom Aadama cosaanoo , deesu ci def benn xàjjaatle bu wéeru ci taxawalinam ci wàllu politig , walla ci wàllu yoon , walla ci wàllu jëflante bi mu séq ak bitim-réew , mu a xam réew moomu mbaa dénd boobu da mu moom boppam , walla da mu nekk ci kiliftéef , walla mu am baatu biir rekk , walla mu am lu mejj ci baatam .cosaanoo
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
doom
features...upos=NOUN
UD_Wolof-WTB
Su lay yooyu yépp nag doyul , kon may naa téeré bi xale ba waa jooju masoon a doon , ndax mag ñi ngeen di gis doonoon nañu ay xale , wante ñi ci di fàtteliku loolu ñu neew lañu .masoon
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Tense=Past
waa
features...upos=NOUN
UD_Wolof-WTB
Osad a leen baaxe dénkaane yii ci suuf , tibbe leen ci téere bi mu siiwal tudde ko : Ëmbub jàmm , Osad , 1994siiwal
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Waa PDS nak , ñoom ba ñu leen wóowee ca ndajee moomu , da ñu lànkk ne duñu ca bokk : Ndax ndaje moomu , du lenn lu dul waxantu ak foontu , nde ña ko sumb , kenn yebbalu leen , kenn mayu leen kàddu , kon munuñu a waxal réew mi .lànkk
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Kon su ñu dellusee di fal jiggéen ju mel ni Nkosazana Dlamini-Zuma , mu war a jiite kureel gi feetee kow mbootaayu réewu Afrik yi , " Union Africaine " , loolu lu mat a fésal la .mel
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ju
features...upos=PRON
NounClass=Wol4
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Laïcité ( diineedi ) , bu dee sax lu ñu gawe ( imposer ) , da mu war a sàmm diine yi waaye waru fi a nekk di lu di gor seen i tànk te naan sama yoon nekkul ci yeen .war
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Loolu mu gëmoon it nag du ab gàkk ci moom , ndax ci bañ gi mu doon bañ kenn moom nu rekk la ko tegoon , tax mu bañaale bépp diine bu fi nar a jële li fi nekkoon .bañaale
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Xare bu tar ba ca toppoon waraloon dawug Soose yi jëm Gambi .tar
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
bu
features...upos=PRON
NounClass=Wol5
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Am geneen làng gu ca yokk ne li wér mu a di yàtt bi warul a taxaw mukk ci réewum Senegaal gii di réewu julit , ndax diine Lislaam da mu di tere di yàtt ay nit , rawatina yëkkati ko ba mu mel ni lu di juqarbi asamaan ...yokk
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
gu
features...upos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Bi ma di dem ñu ma di dégglu ca Soraano , booba yere « Marin » laa soloon .dégglu
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
La ca kanam moom rawul i bët gaa , wante mel na ni téy Abaay Wàdd ñu bari ca ña daan ànd ak moom da ñu koo weddi bu baax : ndax nee nañu loolu mu di wóote newul ci moom , duggeewu ko lu dul naxaate kese .wóote
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Ci lu leer , lu manul a nekk la nosu gii ak màndaqoo gu mat gii nekk di lu fi dikkal boppam ak ci ag tombe ginnaaw ag fàcc gu mag .mat
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
gu
features...upos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Ku nekk war na a man a seet Windows Phone te wax ni man na ma a teewal la Balma wax .war
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ku
features...upos=PRON
NounClass=Wol1
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Gisees na it jaare ko ci seetlu ak xayma ne àdduna bi am na ab tàmbali ( fu mu tàmbalee ) , te dees ko sàkk mu tukkee ci tus , ci ag fàcc gu mag .tàmbalee
features...VerbForm=Fin
Aspect=Perf
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Bi mu di seetlu bidiw yi ci ag fésalukaay gu ngande , gis na ne da ñu di génne genn leer gu xaw a xonq , ci kem seen ag soreyoo .ngande
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
gu
features...upos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Askanu Senegaal moom da mu lànk ba tëdd ca naaj wa ne luwaa boobu kenn du ko fi wote .lànk
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Davis nee na : njuumte gu ndaw ci natt kemub tàllikug àdduna bi man na a waral àdduna bi moy ag bijjam , bu ko defee wéyal ag tàllalikoom ci anam gu nosoodiku .ndaw
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
gu
features...upos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Am geneen làng gu ca yokk ne li wér mu a di yàtt bi warul a taxaw mukk ci réewum Senegaal gii di réewu julit , ndax diine Lislaam da mu di tere di yàtt ay nit , rawatina yëkkati ko ba mu mel ni lu di juqarbi asamaan ...mel
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Du yoon beykat bi def ñetti weer di bey suuf si , déqi , ba noppi jot ay boŋ gannaaw bi mu joxee geerteem , loolu la naqarlu .du
features...VerbForm=Fin
Aspect=Imp
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Polarity=Neg
Tense=Pres
yoon
features...upos=NOUN
Case=Gen
Number=Plur
UD_Wolof-WTB
Li mu def a tax Kajoor jël yoonam te yore boppam .tax
features...VerbForm=Inf
li
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol7
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Gisees na ne ca atum 2100 , làkk yu ñu di gën a wax ñu a di : Àngale , niki làkk njënd , njaay ak xarala , Español ca bëj-saalumu Amerig , Purtugees , ca bëj-saalumu Amerig ak Afrig , Araab , Sinwaa ak Endo ca Asii , Swaahili ak Wolof , ci Afrig .gën
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Askan woowu da mu càllaloo woon ci Seneraal Ptolemee mi doonoon buuru Misra ganaaw paacoog nguurug Aleksaandar mu màg ma ( Alexandre le Grand ) .doonoon
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Tense=Past
mi
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol6
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Yaxantu ga tàmbli woon na di jar , di dox , mbay ma màgg , endustri ba jëm kanam ci mbooleem diiwaan yi bokksi ci Solofrayn .màgg
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mbay
features...upos=NOUN
UD_Wolof-WTB
Daanaka Waalo nit desatu fa ndax ay cong yu jóge Gànnaar ak ay xeet yu sax ci diggante sang yi .desatu
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Polarity=Neg
nit
features...upos=NOUN
UD_Wolof-WTB
Loolu nag di mbir mu doy waar ci askan wu bëgg ñu weg ko .bëgg
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
wu
features...upos=PRON
NounClass=Wol10
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
UD_Wolof-WTB
Ash-Shaari nee na : Duma nangu ku am dooley am Tabaski di ko sàggane .nee
features...VerbForm=Fin
Aspect=Perf
Mood=Ind
Ash-Shaari
features...upos=PROPN
UD_Wolof-WTB
Ci ku xës jënd am tëbaski , walla mu yor am xar jublu ci tabaski : bu loolu xësee am da mu di daldi nekk farata ci yaw .yor
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Bu njëkkoon , barab ya ñu daan seetaane filmu Endo ak kowboy ya da ñu daan fees dell ndax ñu a gënoon a neex a nànd .seetaane
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB
Du sama ag sàggan nag , ndax mag ñi a ma xàddiloo woon ca ba ma di tollu ci juróom-benni at , ma dumooyu mecce nataalkat bi doonoon sama mébet jamono jooja :tollu
features...VerbForm=Fin
Mood=Ind
ma
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=1
PronType=Prs
UD_Wolof-WTB