Example items (sample of 50)

sen_strnsubj_formnsubj_featuresAux_formAux_featurestreebank_link
Lël boobu mu ngi tàmbali ci 16 màrs ci Daaray Wér ( ISED ) tëj ci 4 awril 2009 , ci njiitéefu Dr Asan Yaradu , kenn ci ñi di xelal njawriñu wér ak fàggutéef .mu
features...upos=PRON
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
ngi
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Prog
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Mbooleem alal yooyu daa nañu leen séddale ñetti xaaj : benn ba mu a ngi jëm ca buur ba , ñaareel bi mu ngi jëm ca péncum Séb ak Bawar .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
ngi
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Prog
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Metternich mu màggat mii , mujjoon na manatul woon a noot fippi Tugal yooyu , mbaa mu giimal leen , ni mu ko baaxoo woon a defe .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
woon
features...SubjAuxCount=1
Tense=Past
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ndax kat Otris moom da mu tàmbli woon di genne ay saxal ak i ndigal yu di kontar tas-xibaar gu gore , te wéeroodi fenn , te di kontar mboolooy Almaañ yi daan sàkku ag bennoo te daan ko woote .mu
features...upos=PRON
Aspect=Imp
Case=Nom
PronType=Prs
Tense=Past
da
features...SubjAuxCount=2+
FocusType=Verb
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Soxna Mariyaama Buso ñu ko di dàkkantale , ci jikko , Jaaratu-l-Laah ( dëkkandoob Yàlla bi ) gane àdduna ci atum 1833 ci as ndëkk su tudd Gollere ca Fuuta , génn àdduna ci atum 1866 ca Poroxaan .ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
di
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Loolu li mu di wund mu a di ñoom kat da ñu dëkk ci di nu sori , di dem wëlis nu .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
di
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Boroom xam-xam yu bari yu dul tënk seen bopp ci ne fàwwu da ñu war a nekk ñu gëmadi , nangu nañu ne am na aji-sàkk ju man lépp ju sabab sosug àdduna bi .yu
features...upos=PRON
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
dul
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Polarity=Neg
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ci xarnub fukk ak juróom ñatt g.j , la Kaasa tàmbali a tas :Kaasa
features...upos=PROPN
Person=3
la
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Compl
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Lasli/Njëlbéen liggéeyam rafet na !liggéeyam
features...upos=NOUN
Number=Sing
Person=3
Poss=Yes
na
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Yenn saa yi am nataal bu tane , beneen ba ca topp du ko niru .beneen
features...upos=PRON
NounClass=Wol5
Number=Sing
PronType=Ind
du
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Polarity=Neg
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
- Sol yére yu bees bu nga di julliji , ak xeeñoo lëjkoloñ ( ba mu des rekk jigéen ) ;nga
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=2
PronType=Prs
di
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Da mu daan ree ba noppi da mu bëggoon a am xar , ndax loolu firnde la ci ne diw sangam nekk na .diw
features...upos=NOUN
Person=3
na
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ku nekk war na a man a seet Windows Phone te wax ni man na ma a teewal la Balma wax .Balma
features...upos=PROPN
Person=3
la
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Compl
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Su booba da ñu di wag seeni mbàgg ne la xale nga mu a tax ! "mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
a
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Subj
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Firnde loolu doon na feeñi .firnde
features...upos=NOUN
doon
features...SubjAuxCount=2+
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Xeltukat bu weddi bu siiw ba nii la saraa laaj boobu : Xamees na bu baax ne diine lu baax ci bakan la .diine
features...upos=NOUN
Person=3
la
features...SubjAuxCount=1
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Leeral na ne ci Bennale doxaliinu bànk yi ci atum 2015 , séenu nañu ag jàll jëm ci benn xaalis ci ñaareel goxu CEDEAO gi ëmb réew yi di jëffandikoo làkku Àngale .yi
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
di
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Jamono jooja sax gaa Ëroop amagul woon .Ëroop
features...upos=PROPN
woon
features...SubjAuxCount=1
Tense=Past
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Kooku a di Fatumata Bensudaa di jiggéeni réew mi , ndax Gambi la fekk baax .kooku
features...upos=PRON
Deixis=Prox
DeixisRef=2
NounClass=Wol1
Number=Sing
PronType=Dem
di
features...SubjAuxCount=2+
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Lii da ñu koo fekk ci jamono , te man samay woy da ma bëgg mu di doon lu di wéy .ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
da
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Verb
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ki leen taxawaloon kilifa la woon gu bokkoon ci njabootug Baajli , mu a di Salmaan Xaasa , mi nga xam ne jiite woon na ag nguur ci penku Senegaal .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
di
features...SubjAuxCount=2+
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Fii ba 2025 lim bi mën na a fulu ñaari yoon .lim
features...upos=NOUN
Person=3
na
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ci atum 1770 g.j , la Sulaymaan Baal def ag jeqiku gu Lislaam .Sulaymaan
features...upos=PROPN
Person=3
la
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Compl
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Waaye bu ngeen jaay ndawalug Tëbëski , lekkleen ci joxeleen ci sarax .ngeen
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=2
PronType=Prs
bu
features...SubjAuxCount=1
Mood=Imp
Person=3
Polarity=Neg
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Tos gi di tax làkk woowee di gaaw a sëq , meññ , mu a di dëkke di ca sotti lépp lu xelu doomu-àadama di sàkk te fekk mu di lu ñu mën a jëriñoo mbaa di ci nàmm am xel .gi
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
di
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Li jaaxal nit ñi mu a di nan la askan wi , rawatina kilifa diine Lislaam nar a doxale ?askan
features...upos=NOUN
Person=3
la
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Compl
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Nit ku ne am na sañ-sañ ci wéye xelu boppam ci wàllu xalaat , ngëm ak diine ;nit
features...upos=NOUN
Person=3
na
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Kon fagaru mu a gën faju .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
a
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Subj
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Moom mu a gis Sonaar Seŋoor ne ko gis naa xale bu nga xam ne , bu nga leen ko jëlee dina leen amal solo lool .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
a
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Subj
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ndem-si-Yàlla si , Seex Anta Jóob , ndeysaan , Yàlla na ko suuf sedde , da mu daan wax ne : " Aw làmmiñ du gàtt , aw xel mu a di gàtt " !làmmiñ
features...upos=NOUN
Person=3
du
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Polarity=Neg
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Nee na : nag woowee góor gii mu a ko ni man naa la ko jiitalal .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
a
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Subj
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Xabru ba it reeroon na , ba xameesul fu mu nekkati , waaye Sëriñ bi a jox ndigël Sëriñ Mbàkke Gani Buso , doomu nijaayam , ngir mu seetal ko te saytul ko barab boobee .Sëriñ
features...upos=PROPN
a
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Subj
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Te Aji-bind ji ( Yalla ) nee na : Suuf su teey / nangu dina génne kéeman ci ndigalul boroomam .suuf
features...upos=NOUN
Person=3
dina
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Tense=Fut
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Loolu tamit di mbir mu nga xam ne du nàmm seen am xel .loolu
features...upos=PRON
Deixis=Prox
DeixisRef=2
NounClass=Wol7
Number=Sing
PronType=Dem
di
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Nit ku ne am na sañ-sañ ci xalaat ak génne xalaatam ni mu ko soobe te loolu da mu wund ni am na sañ-sañ ci ñu bañ ko fitnaal ngir xalaatam .nit
features...upos=NOUN
Person=3
na
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Su booba da ñu di wag seeni mbàgg ne la xale nga mu a tax ! "ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
da
features...SubjAuxCount=2+
FocusType=Verb
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Kon ñépp a ngi xaar njiitu-réew mi ci li mu di war a wax ak askan wi ci fan yii di ñëw .ñépp
features...upos=PRON
NounClass=Wol2
Number=Plur
PronType=Tot
a
features...SubjAuxCount=2+
Mood=Ind
PronType=Prs
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Dëkk bi ñu xam ne , ay nit ñu ñuul ñu a fa ne woon , te ñu daan tudde ñu dëkk ca biir réew mi " kaw " .ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
a
features...SubjAuxCount=2+
FocusType=Subj
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Juddu-réew yépp sañ nañu , ci seen jëmmu bopp , walla ci jëmmu ndaw yu leen fi toogal , bokk ci lu ko di tëral .juddu-réew
features...upos=NOUN
Person=3
nañu
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Plur
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ci lu tollu ak 1690 g.j , la Tunka buurub Goy may menn mag mu jóge Podoor aw dog ci suuf .Tunka
features...upos=PROPN
Person=3
la
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Compl
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Nit ku ne am na sañ-sañ ci ñu feg njariñ li mu jële ci bépp liggéey bu mu def ci wàllu xam-xam , ladab ak xarala , mu a xam njariñ li daraja la , walla koom la .njariñ
features...upos=NOUN
Person=3
la
features...SubjAuxCount=1
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Ci bisub 14 nowàmbar , 917 nit faatu nañu fa .nit
features...upos=NOUN
Person=3
nañu
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Plur
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Da ñu mujj daw dëkk boobu , ndax amoon na benn askan bu ñëwoon foofu , jóge Asi , te ñu leen daan bëgg a noot .ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
daan
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Hab
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Lii nag xam-xam wuññiwu ko lu moy ci ñaar-fukkeelu xarnu bii rekk , waaye Yàlla moom jotoon na nu ko a xibaar ci Alquraan , ju ñu wàcce booba ak léegi tollu na ci 1400 at .moom
features...upos=PRON
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
na
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Te sax Wolof Njaay da mu ne « ku wàcc sa and , and bu nga toog mu toj » !mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
da
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Verb
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Aukin jibal na ci lu aju ci tàllalikug àdduna bi : Su fekkoon ne kemub tàllaliku gi , as cimili ginaaw Big Bang bi , da mu yées ak doonte lu tollu ak téeméeri miyaari milyoŋeem la , àdduna bi da mu di daanuwaat ci ag teel balaa tollu nii mu toll tay .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
da
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Verb
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Nee na , li ñu di napp dina nu indil at mu nekk 35 Dollar ( ton bu nekk ) .ñu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
di
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Nguurug Gabu ( nguur gi ëppoon doole ci yii ) Trimaskan Traaware mu a ko sosoon .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
a
features...SubjAuxCount=1
FocusType=Subj
Mood=Ind
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Doktoor yi ñoom rafetlu nañu njàngale mi , ndax ñi leen doon xamal wàccoo nañu ak ñoom , li ñu ci doon xaar gis nañu ko .li
features...upos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol7
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
nañu
features...SubjAuxCount=1
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Plur
Person=3
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB
Te yit bu mu tàxale baat ba , bu ko defee it du ko tee dagan , waaye bañ ko a def a gën .mu
features...upos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
bu
features...SubjAuxCount=1
Mood=Imp
Person=3
Polarity=Neg
VerbForm=Fin
UD_Wolof-WTB