Example items (sample of 50)

sen_strVerb_formVerb_featuresnsubj_formnsubj_featurestreebank_link
Képp ku di liggéey yelloo na pey gu jub te baax , gu mu di suturloo moom ak njabootam , ci nekkin wu méngoo ak daraja ji nit làmboo te , su ko laajee , mu am yeneen xeeti pexe yu ko mottali , ci wàllu kiiraayal nekkin .am
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=am
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Koom-koom bi ñu jëlee ci dem ak dikk bi , ci jokkoo bi , ci toppatoog juróomi junney saytukat yi ak yeneen fere yi , mënoon nañu ko a yokke xaalis bi ñu jagleel njaboot gu nekk .nekk
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=nekk
gu
features...upos=PRON
lemma=bu
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Réew mu mel ni Niseer , su jaayee lu tollu ak 1 miliyaar ci dolaar , 650 Miliyon ya ñu nga des bànku Faraas , fekk Niseer ci boppam du am sax lu mu faye ay liggéeykatam .am
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=am
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Niseer
features...upos=PROPN
lemma=Niseer
xpos=NAME
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci loolu mu dogu te jaayante ci topp ab sëriñam ci jëmmam ak ag ruuham ( ndundam ) kemm kàttanam ngir Yàlla doŋŋ , te di ku sàmm ay wareefam , am kersa ak ag topp gu matale ñeel boroom kërëm .matale
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=matal
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
gu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Loolu nag da mu laaj ñu jël ay nit ñu dëkk ca gox ba , mënees na leen a sax tudde fajkati kër , jàngal leen li war ci ñoom , ba ñu mën a def liggéey bi ñu séentu ci ñoom .laaj
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=laaj
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Saw moomu nag dara dootu ko mën a téye , saa su ne da mu di sotteeku , su ko defee nit ki fu mu tollu da mu di tooy , xetu saw mi topp ko fu ne , àddinaam yàqu .ne
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=ne
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
su
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol9
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Jar na ko tamit ngir fegu : Def na ndànk ba yokk ay mbir ci lu mu dul ñàkke xelam mu ñaw .ñaw
features...upos=VERB
deprel=acl
mu
features...upos=PRON
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Kon moom lu leen jekku rekk ñu sañ ko a def noona .sañ
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=sañ
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ñu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Takku taxaw temm boo xam ne la , dangay fàtte sa bopp , jëf ngir ñépp .xam
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=xam
Mood=Ind,Ind
boo
features...upos=PRON
lemma=boo
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Naka noonu , nit ku ne àq yi mu làmboo te di leen doxal seen i dig a ngi yem ci dig yi di may ñeneen ñi bokk ci mbooloo mi ñu bànneexu ñoom it ci àq yooyu .may
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=may
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
yi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Taamul di naan laata waxtu lekk jot , da mu di tax doo xiif bu baax , su ko defee doo lekk lu bare ;tax
features...upos=VERB
deprel=parataxis
lemma=tax
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Lii rekk a tax askanu Senegaal gisul boppam ci doxalinu nguur gi .tax
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=tax
Mood=Ind,Ind
lii
features...upos=PRON
lemma=lii
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Su nga yeewoo rekk , daldil naan ndox ;yeewoo
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=yeewu
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
nga
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=2
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ba fii , jëwriñ yi gàlloo wàll wi lañu bàyyee dogalu jëfandikoo gafaka gi , ñoom ñi di njiiti dugal ak génne xaalis bi .gàlloo
features...upos=VERB
deprel=acl
yi
features...upos=PRON
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Su fekkee ne du moom rekk moo waral li am , su bal yi dul ñëw ci moom ni ñu waroon a ñëwee , Mbay Ñãa am na ay jafe-jafey am ay ruq yu muy taxaw ba kenn du ko fa lakkal ,am
features...upos=VERB
deprel=root
Number=Sing
Person=2
mbay
features...upos=NOUN
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Tos gi di tax làkk woowee di gaaw a sëq , meññ , mu a di dëkke di ca sotti lépp lu xelu doomu-àadama di sàkk te fekk mu di lu ñu mën a jëriñoo mbaa di ci nàmm am xel .gaaw
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=gaaw
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
làkk
features...upos=NOUN
lemma=làkk
xpos=NOUN
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Kon nag , dafa jublu ëllëg ak xol bu yaatu .yaatu
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=yaatu
Mood=Ind,Ind
bu
features...upos=PRON
lemma=bu
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Ci 2008 , tolluwaay ba a ngi nekkoon ci 5,6 % te mu a di junni nit ñu ne , juróom-fukk ak juróom–benn yi sibbiru dal na leen .di
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=di
xpos=COP
Aspect=Imp
Mood=Ind
Tense=Pres
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Mu jublu ci bari ga nit ñi bari ak doole ja ñu di àndal ci xér ga ñu xér , su ñu fëxee wuti Sëriñ bu mag bi .bari
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=bari
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
nit
features...upos=NOUN
lemma=nit
xpos=NOUN
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Àttey jëmm yii feeñ ànd ak Big Bang , soppikuwuñu lu gën a néew ci diir bu tollu ci 15 milyaari at .tollu
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=tollu
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
bu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol5
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci lu leer , lu manul a nekk la nosu gii ak màndaqoo gu mat gii nekk di lu fi dikkal boppam ak ci ag tombe ginnaaw ag fàcc gu mag .mat
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=mat
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
gu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci Kaw Gaambi ak Penku Senegaal ay nguur yu bari toftaloo nañu ci dexug Gaambi gi , yi ci ëpp solo ñu a di Ñaani ak Wuli .toftaloo
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=toftaloo
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
nguur
features...upos=NOUN
lemma=nguur
xpos=NOUN
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci lu amul benn werante , loolu a tax futbalkatu Liverpool bi jël dogalu seddal lépp mu jeex .tax
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=tax
Mood=Ind,Ind
loolu
features...upos=PRON
lemma=loolu
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Ca jamono yu yàgg ya li ëppoon ci giirug Pël ay sàmm yu daan màng lañu woon , di tuxu ci seen bëgg-bëgg ngir wër ndox ak ñax .yàgg
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=yàgg
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
yu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ahakañ , am na sax yenn saa yu ma amoon xel-ñaar dëgg sax , ndax sama njàngum bind yépp ci " francais " la , te boobu téere mu a doon sama juróom-ñaareeli téere .amoon
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=am
xpos=VERB
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
ma
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=1
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Wàcce wala batale toftalante gi , ak leeral tolluwaay deppãasu askan wi , moo nekk , kon li waral ñu xaajale koom-koom gi ci ay tëralin .xaajale
features...upos=VERB
deprel=ccomp
ñu
features...upos=PRON
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Askan woowu da mu càllaloo woon ci Seneraal Ptolemee mi doonoon buuru Misra ganaaw paacoog nguurug Aleksaandar mu màg ma ( Alexandre le Grand ) .màg
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=màg
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol6
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
KAYITU JOXE SAY SAÑ-SAÑ YU BON AK XAALIS BU AJU CI ALAL .aju
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=aju
bu
features...upos=PRON
lemma=bu
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Ba yaay ja jógee àll ba , mu di woy , kenn wuyuwu ko , mu jaaxle lool .jógee
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=jóge
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
yaay
features...upos=NOUN
lemma=yaay
xpos=NOUN
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci xalaatam , ngir bundxataal sibbiru , da mu laaj beneen wirgo doktoor , beneen wirgo saytukat ngir tolluwaayu dee gi ci aju ak jàngoro ji bañ a yéeg .bañ
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=bañ
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
jàngoro
features...upos=NOUN
lemma=jàngoro
xpos=NOUN
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Cosaanu mbind ci Afrik lu mat a fésal la , ndax ñu bari , waay-xeltu yi ak ñeneen da ñu defe ne caada yi nekk Afrik xamuñu ca seen cosaan xaralaay mbind .xamuñu
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=xam
xpos=VERB
Mood=Ind
Number=Plur
Person=3
Polarity=Neg
VerbForm=Fin
caada
features...upos=NOUN
lemma=caada
xpos=NOUN
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ba ma juddoo ba léegi tase ak naa nit ñu bari ñu am xel .am
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=am
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ñu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol2
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Yëf ya a ngi séqi ay jeego te dara du ko dakkal , ci nii wala ci naa .dakkal
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=dakkal
dara
features...upos=NOUN
lemma=dara
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
DELACROIX nee na ñu ndefarug ndaanaan dafa war a yéem ki koy xool ...nee
features...upos=VERB
deprel=root
Mood=Ind,Ind
DELACROIX
features...upos=PROPN
lemma=Delacroix
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Ci ab fekki réewum Russie bu wóoradi , xale yi mujjee nañu nërmeelu ñaari bit ci tus .wóoradi
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=wóoradi
bu
features...upos=PRON
lemma=bu
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Am geneen làng gu ca yokk ne li wér mu a di yàtt bi warul a taxaw mukk ci réewum Senegaal gii di réewu julit , ndax diine Lislaam da mu di tere di yàtt ay nit , rawatina yëkkati ko ba mu mel ni lu di juqarbi asamaan ...tere
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=tere
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Waaye bi Solfrayn taxawee , lanu bennal biir Brusiya ci wàllug nduwaan , ginaaw bi mu nekkee moom Brusiya di lu nu seddale ci juróom benn fukki goxi nduwaan .taxawee
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=taxaw
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Solfrayn
features...upos=PROPN
lemma=Solfrayn
xpos=NAME
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Kon nguur walla àtte gu dëgër ci gis-gisu Hegel , mu a di nguurug walla àtteg dëgg .dëgër
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=dëgër
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
gu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Nga xam ne da nu feexal yaxantu gi ci Brusiya , ëfal ko ba mu man a doxe ni ko soob , ci lu dul ñu ci di teg ay tënk-tënki galag mbaa yu nduwaan .man
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=man
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Naka noonu , nit ku ne àq yi mu làmboo te di leen doxal seen i dig a ngi yem ci dig yi di may ñeneen ñi bokk ci mbooloo mi ñu bànneexu ñoom it ci àq yooyu .làmboo
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=làmboo
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Mu leeral ci séqoo gi am ci diggante xayug Isipt ak xayug waa Afrik yu ñuul yi .ñuul
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=ñuul
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
yu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
CEDEAO dafa amal boppam xaalis bu réewam yépp di bokk , bu moom boppam te am dayo bu mën di soppeeku , bu gën a dëppoo ak ni suñu koom-koomi réew yi bindoo .amal
features...upos=VERB
deprel=root
Number=Sing
Person=2
CEDEAO
features...upos=PROPN
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Loolu da mu di yeesal ndox mi ci sa yaram ( lu ëpp juróom-ñaar-fukk ci téeméer 70 % ndox la ) , su ko defee mu aar la ci sank , maanaam seere .yeesal
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=yees
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Loolu a waral Dr Coor yokk ci : su nu wéyee di góor-góorlu , waxuma rekk ne tolluwaay bi dina yem foofu , waaye sax dinanu faagaagal xeetu sibbiru bii .wéyee
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=wéy
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
nu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=1
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Waaye , jigéen ju bon ji masul xam ne Yàlla daan na feeñu Tóni ci melokaanu daar bu bare meew , bu ñëwee di nàmpal Tóni .feeñu
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=feeñu
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Yàlla
features...upos=PROPN
lemma=Yàlla
xpos=NAME
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci ñàkk kóolute gi am ci biir at mile .am
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=am
Number=Sing
Person=2
gi
features...upos=PRON
lemma=bi
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Adduna bi , bu gënoon a dox ndànk ci nii mu ko di defe , da mu di daldi rot , bu gënoon a gaaw tuuti rekk nga gis ne-ne bu àdduna bi tas bu yàgg .rot
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=rot
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ba ma nekkee xale bu tollu ci juróom-benni at , da ma masoon a gis benn bés nataal bu yeeme ci benn téeré bu doon nettali lu jëm ci " àll-bu-xonq bi " bu tuddoon " Ay nettali yu dëggu yu ñu dund " .tuddoon
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=tudd
xpos=VERB
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
bu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol5
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Yonent ( jàmmi Yàlla ci moom ) bi xamle na ni toq dereet wi di njëkk a génn Yàlla dina ci jéggale mbooleem bàkkaar yu ñu mas a def .xamle
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=xamle
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Yonent
features...upos=PROPN
lemma=Yonent
xpos=NAME
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Bu mosee rëbbi ba ñëw , da mu di woo xale yi , benn benn , ñu nàmp ba mu des Tóni .des
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=des
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB