Example items (sample of 50)

sen_strAux_formAux_featuresnsubj_formnsubj_featurestreebank_link
Loolu a waral boroom xam-xam yi naan kolesterol benn la ci ñeent ñi di faat xol « bourreaux du cœur » .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
ñi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol2
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Yeneen réew yu mel ni yu " Hitites " ak yeneen ñu a fa nekkoon !a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ñu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Lebi xaalis nga xam ne moo war a taawu dugal xaalis ci béreb yi ginnaaw bu ñu ñoŋalee lempo yi , ak tono yi ñuy jële ci alali càkkeef gi ( ni ñu ko Peresidãa Usmaan Sónko di faral di fàttelee ) , bonul ,di
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
Peresidãa
features...upos=PROPN
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Comp yooyu , ay kuréli kaaraangey dundug askan ñoo koy def .ñoo
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=moo
SubjAuxCount=1
kuréli
features...upos=NOUN
lemma=kuréli
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Ba njëkk mu a di Lingeer mi di yaayu buur bi ak Aawo mi di soxnaay buur su njëkk .di
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=di
xpos=COP
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
VerbForm=Fin
mi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol6
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Loolu nun doŋŋ , waay-xeltu yi , ñi di yëngu ci politik , jàngale , koom-koom ag fànn wu mu mënti doon , nu a ko mën a defal sunu bopp .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
ñi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol2
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ki leen taxawaloon kilifa la woon gu bokkoon ci njabootug Baajli , mu a di Salmaan Xaasa , mi nga xam ne jiite woon na ag nguur ci penku Senegaal .di
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=di
xpos=COP
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
Tense=Pres
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Senegaal wooneti na boppam .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
Senegaal
features...upos=PROPN
lemma=Senegaal
xpos=NAME
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Waaw Murambi , nettali la ci xew-xew ya amoon Ruwaanda , ñu ngi ko di jàngale ci lekool yi .ngi
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=ngi
xpos=AUX
Aspect=Prog
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=2+
ñu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Buur bi jataayub mag ñi a ko daan dimbale , mu a daan fuglu it ay saxalam te di digal ay sañ-sañam .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
jataayub
features...upos=NOUN
lemma=jataay
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Tëbëski mu a di ñaareelu iid ( bër ) ci Lislaam ginnaaw bu Korite jàllee .di
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=di
xpos=COP
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
Tense=Pres
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Doktoor Pàppa Muusaa Coor mi di saytu PNLP xamle na ne njàngale mii ñu sumb mu ngi bokk ci pexe yi ñu tëral ngir sibbiru ak dee yi mu di jur bañ a jéggi tolluwaay bi mu nekk jamono yii .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Wuute yi di am ci biir mbooloo mi mënuñu wéeru lu dul ci njariñal ñépp .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
yi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Aram Faal dafa teel a xam ne làkku farañse dafa dox diggante jàngkat yi ñu jiite te war a wone yoon wi , ak askan wi leen war a wóolu .dafa
features...upos=AUX
deprel=aux
SubjAuxCount=1
làkku
features...upos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Gannaaw loolu nag , aw làkk wu di dund moom , da mu mel ni aw gàncaq rekk : su nga ko suuxëtee , toppatoo ko , solool ko , bu ci Yàlla àndee da mu di law , naat !da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Am na yeneen nguur yu sosu woon ca la tollu ak xarnub fukk ak ñatt g.j , ñu a di : Siiselaa , Beledugu , Niokolo , Badon , Bademba , Bundu , Gajaga .di
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=di
xpos=COP
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
Tense=Pres
VerbForm=Fin
ñu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Yeew bu di wànn ñay di ko reesal laa nataal .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
bu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol5
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Rax-ci-dolli , ni ko Italiyee bi di waxe : " traduttore tradittore " , maanam " tekki , teggi " , ndax tekke ca làkk bu mu mënti doon jëmale ca beneen làkk , fàww mu am lu mu moy .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
Italiyee
features...upos=PROPN
lemma=Italiyee
xpos=NAME
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Waaye li am ba des kay mooy , CAF dafay soog a xaatim moom ak Puma bu këru liggéeyukaay gii di Adidas ab digaaleb siiwal ay fan laata loolu .di
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=di
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
gii
features...upos=PRON
lemma=bii
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Yokk ci , réew mi walla dénd bi doom Aadama cosaanoo , deesu ci def benn xàjjaatle bu wéeru ci taxawalinam ci wàllu politig , walla ci wàllu yoon , walla ci wàllu jëflante bi mu séq ak bitim-réew , mu a xam réew moomu mbaa dénd boobu da mu moom boppam , walla da mu nekk ci kiliftéef , walla mu am baatu biir rekk , walla mu am lu mejj ci baatam .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Tàllalikug àdduna bi benn la ci firnde yi di wone ne àdduna bi ci ag neen lañu ko sàkke .la
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=la
xpos=COP
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
VerbForm=Fin
tàllalikug
features...upos=NOUN
lemma=Tàllaliku
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Lu ñu gën di jëfandikoo làkku Faraas ci àdduna bi rekk ( lu tollu ak ñaari téeméeri milyoŋ ci doomi aadama ) gën di yokk ay liggéey ca Faras , ndax ñoom ñu a di soppi film yooyu di ko jaayaat yeneen téeméer ak ñeen-fukki milyoŋi doomi aadama yi nekk ci yeneen réew te di jëfandikoo làkku Faraas te nun nu a ngi ci biir .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
ñu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Waa Bennoo jubbowuñu ci benn kandidaa , da ñu mujj wote : 19 parti ànd ak Mustafaa Ñas , yeneen 14 parti ñoom woteeluñu kenn , da ñu tiyye seen kàddu .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ñu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Jàppante bi wéy na ba ci XVu xarnu bi , ba killifay soose yi deewee la xare ba jeex .la
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=la
xpos=INFL
FocusType=Compl
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
xare
features...upos=NOUN
lemma=xare
xpos=NOUN
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Fexe ba tekki film yi ñu di seetaan ak fowukaay yi sunu xale di jëfandikoo ci sunu ay làkk ; rawatina ci wolof ndax mu a di làkk wi ëpp lu ñu ko di jëfandikoo ci réew .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
xale
features...upos=NOUN
lemma=xale
xpos=NOUN
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Jorg Gamow indi na beneen xalaat ci lu aju ci Big Bang .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
Jorg
features...upos=PROPN
lemma=Jorg
xpos=NAME
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci ay waxam , 2009 ak léegi , réew yooyu tëral nañu yoon wu bees wu di leeral ay liggéey yu jëm ci bennoo gi : bennale sistemu peyoor yi , yu estatistik yi , yu politigu alalal yi .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
wu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol10
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Bi ci gën a siiw di bu Meroe , te ngeen di gis nataal bi fii ci xët wii !di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
ngeen
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Plur
Person=2
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ku dem , mag da mu maa dab .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Loolu a tax saytukatu bidiw yi taqoo woon ak xeltu gu ngérum ne-ne mi ( materialime ) wéyoon ci weddi Big Bang te sax ci dëgëral xalaatu ab àdduna ju amul yamu bi .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
loolu
features...upos=PRON
lemma=boobu
xpos=PRON
Deixis=Prox
DeixisRef=2
NounClass=Wol7
Number=Sing
PronType=Dem
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Ci àddina sépp , ci téeméeri nit ñu yore jabet ñu ne , juróom-ñeen-fukk ñi jabet 2 mu a leen dal .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Gannaaw Maam Moor ab sëriñam da mu xawoon a jëm mag , te fi ñu nekkoon xaw a àlle , ba tax sedd ba xaw fa a tar , daan na ko fàggul matt mu mu di jaaroo , ngir mucc ci sedd boobu nga xam ni baaxul ci mag .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Jot na dëggit ñu xoolaat nekkinu ñi ñuy teewal , njëkk ñu leen di batale ngir ñu teewal waa Afirig sowu jant .di
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
ñu
features...upos=PRON
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Tey ci àjjuma ji , ca péncum ndawi réew ma , ci teewaayu deppite yi , la nguur gi fésal njëgu ropplaan li mu doon nëbb .doon
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=doon
SubjAuxCount=1
mu
features...upos=PRON
lemma=bu
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Ci xarnub fukk ak juróom benn Fuuta Tooro def na ay xare ngir yaatal suufam ci kaw ay dëkkandoom : Jolof , Kajoor .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
Fuuta
features...upos=PROPN
lemma=Fuuta
xpos=NAME
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
lay wi mooy ndàmpaay yu mu jagleel ñi ko yellool , ñu koy def ci jollasu ( telefon ) .mooy
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=mo
SubjAuxCount=1
lay
features...upos=NOUN
lemma=lay
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Te noppi nanu ngir bokk ak yéen sunu xam-xam , la Ibraayima Ñaan dëggal , kenn la ci ñi ŋànk këlëb bi .la
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
Ibraayima
features...upos=PROPN
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Am na itam ñu nga xam da ñu ne ñoom li leen naqari mu a di yàtt bi ci boppam da mu amul lenn lu am solo lu mu di misaal , rax-ci-dolli rafetul , taaruwul !di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Alaa kulli haal nag , Lislaam ag yombal la bëgg , te mboolem àtte yi woroom xam-xam yi di tërël da ñu ci sóoraale loolu ag jàppndal ñeel jullit ñi .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
woroom
features...upos=NOUN
lemma=boroom
xpos=NOUN
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Yàlla na leen ko Boroom bi teggil ci jàmm .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Opt
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
Boroom
features...upos=PROPN
lemma=Boroom
xpos=NAME
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Wante su ne woon ci nasaaran " j' avais dit , mais maintenant je me dédis " , mbir mi du deme noonu !du
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
Polarity=Neg
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
mbir
features...upos=NOUN
lemma=mbir
xpos=NOUN
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Gaaral googu njiitul Microsoft Stef Balma mu a ko jiite , ngir wone ni seen nosteg doxiin bu bees bi da mu nekk lu taaru te yéeme .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Xayma yi wone nañu ne benn tomb bii nga xam ne mu a ëmboon mbooleem ne-ne bu àdduna bi da mu waroon a am kemu ab dayoo ak ag fataay gu amul yamu .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Adduna bi , bu gënoon a dox ndànk ci nii mu ko di defe , da mu di daldi rot , bu gënoon a gaaw tuuti rekk nga gis ne-ne bu àdduna bi tas bu yàgg .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Céy , politik yenn saa yi kenn du xam lu mu di nirool !di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Bu doom ji génnee , góom boobu , bu demee ba wow ba def aw àkk , da mu di mujj rot , su ko defee mu bàyyi ab bëtt-bëtt bu saw mi di jaar , di sotteeku ci awra ji .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
mu
features...upos=PRON
lemma=mu
xpos=PRON
Case=Nom
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Réewum Senegaal firndeel na ne kenn demul mu dés : Du réewum cuune !na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
réewum
features...upos=NOUN
lemma=réew
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-WTB
Aw tëralin la ñuy doxal at mii di ñëw ngir lopitaalu Tiwaawon la jëwriñu biir-réew ji wax .la
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=la
Mood=Ind,Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
ñuy
features...upos=PRON
lemma=buy
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Aaj ab kàngam la ci ab këru liggéeyukaay gu mag .la
features...upos=AUX
deprel=cop
lemma=la
Mood=Ind,Ind
Number=Sing
Person=3
SubjAuxCount=1
Aaj
features...upos=PROPN
lemma=aaj
Person=3
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD
Wànte gàttal boobu dafa bare ay tekki , ci kow ak ci biir yépp .dafa
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=d
SubjAuxCount=1
gàttal
features...upos=NOUN
lemma=gàttal
deprel=nsubj
UD_Wolof-AfriSUD