Example items (sample of 50)

sen_strVerb_formVerb_featuresobj_formobj_featurestreebank_link
Sunu maam yi , ci lañu doon bind , di ci jaamu Yàlla , di ci xam seen bopp , di ci jàng àddina !jaamu
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=jaamu
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Yàlla
features...upos=PROPN
lemma=Yàlla
xpos=NAME
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Dafa tàmbalee tëj gémmiñu benn pàcc ci ñiy xeexal askan wi te defuñu pólótig , ci lu nga xam ne da leen di ger , wala mu wañ seen loxo .wañ
features...upos=VERB
deprel=conj
loxo
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ñoom dañuy xalaat seen aafiya ji , anam yi ñuy nekk bu ñuy tukki .xalaat
features...upos=VERB
deprel=root
Mood=Ind,Ind
aafiya
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Noo mu ngi dellu di fésal pas-pas bi mu am ci wéyal xeexu maréew bi muy def ngir neenal yokkug kuurãa bi laluwul ci lenn lu jaadu , tey xamal askan wi ñu pare xeex xeex bi .am
features...upos=VERB
deprel=acl
Mood=Imp
bi
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Te buum boobu , xàncc bi ñu ko ràbbee mu a di di jëfandikoo làkki Nasaraan soofal sunu bos , di jàng cosaanam fàtte sunu bos , jël ay kureelam indi teg , jël doxalinam indi teg , jël xaalisam indi teg .soofal
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=soofal
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
bos
features...upos=NOUN
lemma=bos
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Njiitu Kuréel gi di saytu xaalis bi ci Afrig sowwu-jant ( AMAO ) , Mohamed Ben Omar Njaay xamale na , talaata jii ci njalbéenu limu waxtaan yi IDEP ( Daara ji ñu di jàngalee suqalig koom ak ag sooraale ) amal , ne goxu bennoo réewi Afrig yu sowwu-jant ( CEDEAO ) dina bennal xaalis bi .saytu
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=saytu
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
xaalis
features...upos=NOUN
lemma=xaalis
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Xam nga kon mënuma a wax ci lenn di wone sama bopp te wonewuma sama bopp jarale ko ci njabootu Aal-Pulaar yi .jarale
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=jarale
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Réewum Senegaal bare na ay boroom alal torob waaye ñaata ñoo ci fésal li ñuy liggéey .fésal
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=fésal
Mood=Ind,Ind
li
features...upos=PRON
lemma=bi
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ci ag pàttali , ci mbënnum 1998 lañu sosoon sàntar bi , nga xam ne ñu bari da ñu ñàkkoon seen kër .ñàkkoon
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=ñàkk
xpos=VERB
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
kër
features...upos=NOUN
lemma=kër
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
MD : Yaw lan nga yaakaar ne manoon nañu koo def ngir xëcc jigéeni Senegaal yi ci pólótig bi ?def
features...upos=VERB
deprel=ccomp
Mood=Ind,Ind
koo
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Sañ-sañ boobu nit ki mënu ko tuddoo , su fekkee ne jëyya ju aju ci yoon wi ñépp bokk lañu ko di toppe , walla ay jëf yu safaanoo ak jubluwaayi Mbootaayu Xeet yi ak i sàrtam .toppe
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=topp
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Man na a am ñu tànn dammeel ci lu dul geño mbaa meenum Paaléen .tànn
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=tànn
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
dammeel
features...upos=NOUN
lemma=dammeel
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Doxali VAP yi nga xam ne dafay boolee ñu yore suuf ak ñoo xam ne amuñu suuf waaye am nañu xaalis , ci diirub ñetti at lees koy amal .amal
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=amal
Mood=Ind,Ind
koy
features...upos=PRON
lemma=ko
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Soxna Jaara nee nañu : Masul a jóg ci di dimbalante ñeel waa pénc mi , ci di taxawu ak di dundal jirim yi ak néew-gi-doole yi ci lu dul di sàkku ag cant ci nangukat yi , xanaa ngir jëmmi Yàlla rekk .sàkku
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=sàkku
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
cant
features...upos=NOUN
lemma=cant
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Sama defug pólótig dafa jaare ci saytu ak xalaat ci gis-gisu PASTEEF bi nga xam ne Usmaan Sónko moo ko jëmmal .xam
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=xam
Mood=Ind,Ind
moo
features...upos=PRON
lemma=a
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ab tàkk-der lañu yónni woon kese ngir mu nanguji këyit yi ñuy bindoo ngir jàppale sa farandoo ca Sigicoor .nanguji
features...upos=VERB
deprel=advcl
këyit
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Genn ngoon la Muuma dig dajee Paab ngir delloo ko xaalisam bi .dajee
features...upos=VERB
deprel=compound:svc
lemma=dajee
Paab
features...upos=PROPN
lemma=Paab
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Nataal bii ma ko nataal ca gànnaaw ga mu a di bi ko gën a indi , wante bir na ma sama nataal boobu xaajul jege kemtaan gi mu doon roy .bir
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=bir
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ma
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=1
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ndajeem parlamaa mii , ñu ngi ko gën a xame ci turu " Parlamaab Frankfort " .gën
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=gën
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Jeex na , fàww jigéen ñi ñu gën leen a jox seen gëdd , ñu taxawal ay xalaat te doxal ay naali yokkute .jox
features...upos=VERB
deprel=dep
Mood=Ind,Ind
gëdd
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ndegam masuma woon a nataal xar nag , ma nataalal ko benn ci ñaari nataal yooyu kese ma mënoon .mënoon
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=mën
xpos=VERB
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
yooyu
features...upos=PRON
lemma=boobu
xpos=PRON
Deixis=Prox
DeixisRef=2
NounClass=Wol8
Number=Plur
PronType=Dem
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Dafa war di fay lempo te fayu ko ba pare , di jaarale fiili kuurãa yu baree bare safara ci biir dëkk bi , diggante Biir Podoor ba Belli Torodo .bare
features...upos=VERB
deprel=compound
Mood=Ind,Ind
safara
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ay këri tas-xibaar yu bare siiwal nañu turu xaalisu ëllëg boobule : ECO la xaalis bi di tudd .siiwal
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=siiwal
Mood=Ind,Ind
turu
features...upos=NOUN
lemma=turu
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Tuchel moom lu mën a nekk rekk lay def , teg na ñaar ñoo xam ne defãas lañu gën a mëne ngir gën a dëgëral defãasam bi .dëgëral
features...upos=VERB
deprel=dep
lemma=dëgëral
defãasam
features...upos=NOUN
lemma=defãasa
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Kii nee na : Man de soxna laa te ab jullit laa , waaye nii Soxna Jaara mel manuma ko a mel ?manuma
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=man
xpos=VERB
Mood=Ind
Polarity=Neg
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Jerôme Boateng , Javi Martínez ak David Alaba ñu ngay dem ginnaaw bu ñu defee fukki at ci Bavière .defee
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=defee
at
features...upos=NOUN
lemma=at
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Soxna Jaara Buso mom Sëriñ Hamaat Buso ( baayam ) ak Soxna Asta Waalo Mbàkke ( yaayam ) , cosaano ci askanu Sëriif gu nga xam ne calale ga dem na ba ca Imaam Hasan mom Imaam Aliwu mom Abii Taalib ak Faatima mom Muhammad Yonentub Yàlla ( jàmmi Yàlla ci ñoom ) .xam
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=xam
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
gu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
C. T. Mbeng moom da mu ko jàppe niki " ab aji-teewal ak aji-rattaxal ci diggante réewi Lebu yi " .jàppe
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=jàpp
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Njariñ li mën a tukkee ci xeetu wanag wii bari na , ndax lépp la ñu di jëfandikoowaat , day yi , saw mi ak yi ci ànd , rax-ci-dolli da mu di yaxanal ndox , indi cet .indi
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=indi
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
cet
features...upos=NOUN
lemma=cet
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Noo mu ngi dellu di fésal pas-pas bi mu am ci wéyal xeexu maréew bi muy def ngir neenal yokkug kuurãa bi laluwul ci lenn lu jaadu , tey xamal askan wi ñu pare xeex xeex bi .def
features...upos=VERB
deprel=acl
Mood=Ind,Ind
bi
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Góor gu noppi la , ku yorul kanamu woyu .yorul
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=yorul
kanamu
features...upos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Misaalum nittali bu siiw bii te doy kiimtaan , ñu ni : Am na bis Maam Moor Anta Sali di takk aw sàkket teyeloo ko sàkket wa , dugg ci biir neeg bi , ( xëy na ngir jël lu mu takke sàkket wi ) faf Yàlla dogal mu dugg rekk , Yàlla sóob ab taw , mu far toog ca néeg ba .sóob
features...upos=VERB
deprel=parataxis
lemma=sóob
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
taw
features...upos=NOUN
lemma=taw
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Gune yépp , mu a xam ci buumu séy lañu juddoo walla déet , ñu a yem kiiraayal nekkin li ñu yeyoo .yeyoo
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=yeyoo
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
li
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol7
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Kenn du nu ko yennul , kenn du nu sax gaar ci di jëfëndikoo sunu làkk yi !jëfëndikoo
features...upos=VERB
deprel=xcomp
lemma=jëfëndiku
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
làkk
features...upos=NOUN
lemma=làkk
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Mu ne ma : loolu du ci dara nataalal ma xar .ne
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=ne
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ma
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=1
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ci gis-gisu lawax ( kàndidaa ) bi nar a samp ndëndam , tàggatu ngir jiite am réew mën naa xaar ba ci kanam !samp
features...upos=VERB
deprel=dep
lemma=samp
Mood=Ind,Ind
ndëndam
features...upos=NOUN
lemma=ndënda
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ab xeltukat bu mat sëkk li mu doon , warul a noppi ci yëfi dof yi ñenn ñi di def , donte sax yéen a bokk benn pàrti wala nga bokk ci nguur gi , rawatina mu jëm ci yàq alal ji ñépp bokk .bokk
features...upos=VERB
deprel=acl
Mood=Ind,Ind
ji
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Lu ñu gën di jëfandikoo làkku Faraas ci àdduna bi rekk ( lu tollu ak ñaari téeméeri milyoŋ ci doomi aadama ) gën di yokk ay liggéey ca Faras , ndax ñoom ñu a di soppi film yooyu di ko jaayaat yeneen téeméer ak ñeen-fukki milyoŋi doomi aadama yi nekk ci yeneen réew te di jëfandikoo làkku Faraas te nun nu a ngi ci biir .jaayaat
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=jaayaat
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Lii déy yéem na ma , te war a man a yéem waa jamono jii , ci lii nu mu man a ame .man
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=man
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
nu
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Plur
Person=1
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Su ko defee mu fuddu , saxaan ndànk as mbant su rafet te lewet su di law wutali jànt bi .defee
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=def
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Nit ku ne sañ na dem yoon , ci kanam àttekaay yi ko yelloo ci réew mi , ngir tawat fa jëf yi di bëtt sañ-sañ yi ko Ndeyu Àtte bi walla ab àtte fàggul .fàggul
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=fàgg
xpos=VERB
Mood=Ind
Polarity=Neg
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Njiitu réew mi dellu daloo doxalug kurãa bu ñetti dëkk , daloo masin yiy jox ndox Kéedugu .jox
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=jox
Mood=Ind,Ind
ndox
features...upos=NOUN
lemma=ndo
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Moom ak Sàngalkaam ñoo bokk benn dekere 2011 bi rëddaatoon gox bi .rëddaatoon
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=rëddaatoo
gox
features...upos=NOUN
lemma=gox
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Lépp a ngi mel ni cosaanu nit mënul weesu péex mu mënul ñàkk cig fésam .mel
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=mel
Mood=Ind,Ind
mënul
features...upos=NOUN
lemma=mënul
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Kàddu yii tukkee ci Mustafaa Siise , kilifag biro bi di toppatoo fagaru ak jëflante ci Progaraam bi di xeex sibbiru , tudd PNLP ci frãse , wone na cër bu yaatu bi fagaru am ci xeex sibbiru , nga xam ne at mu ne dina rey lu ëpp milyoŋ ci ay nit .tudd
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=tudd
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
PNLP
features...upos=PROPN
lemma=PNLP
xpos=NAME
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Li jar a wax mu a di réew mu nga xam ne 98 % ay jullit lañu te feeti Nasaraan ya a fa ëpp .xam
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=xam
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol6
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Lenn lu mënul ñàkk ci réew yiy namm a bokk ci dénd bi ñu jagleel xaalis bi mooy , ñu matale màndargaay tànnéef yi ñu bokk :matale
features...upos=VERB
deprel=root
Mood=Ind,Ind
màndargaay
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Bëtt-bëttu wasin « fistule obstétrique » , bëtt-bëtt la bu ubbiku diggante paftan mi nga xam ne mu a di denc saw mi ak awra jigéen ji .xam
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=xam
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol6
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Li ñu gis nekkul liggéeyu tas-xibaar buy sagal taskatu xibaar waaye ag bëgg a faagaagal kenn nit gu jéggi dayo , nit ku ñu mënul a yeey ci waxtaan ndaxte moo leen gën a jàng , gën leen a yeewu fuuf .gën
features...upos=VERB
deprel=conj
Mood=Ind,Ind
leen
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Loolu la Sëriñ Muusaa Ka naan : nee na keroog gis na fa sunu maam Jaara , mu di ko ñaax te di ko dolli ay daara .ñaax
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=ñaax
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB