Example items (sample of 50)

sen_strAux_formAux_featuresobj_formobj_featurestreebank_link
Ñoñ ne-ne ñi da ñu jàppe woon xalaatu àdduna bu amul yamu bii mu di seen ndëerlaay lu mag .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
xalaatu
features...upos=NOUN
lemma=xalaat
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Du lu ñu fi di doxal mbaa àtteb jeneen diine , waaye lépp lu ñu di def warees na ko a xool ba xam gaañul jenn ci diine yooyu .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Nit ku ne am na sañ-sañ ci yoon feg ko ci lëñbët yooyu ak tooñ yooyu .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
sañ-sañ
features...upos=NOUN
lemma=sañ-sañ
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Dama koy naqarlu te di ko mas-sawu , moom ak njabootam .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ci misaal benn deppite bu yorul beneen ndombo tànk , di am weer wu dee benn milyoŋ ak juróom-benn-fukki junne ( 1 ) ( te boolewuñu ci yeneen tegandaay yi mel xaalisu luyaas , xaalisu esãas ak daamaar yi ...di
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
milyoŋ
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Bu ñu ko fàtte fii ci Afrik , jiggéen a fi mas a fallu , di yaay , di lingeer , di ndey-ji-réew , di buur , ca Misira démb , Nibi , Meroe , ba ci Waalo ak Kajoor .bu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=bu
xpos=INFL
Mood=Imp
Polarity=Neg
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ci mujjantalug xarnu bu fukkeel la Waar Jaabi song ki mujjoon ci buuri njaboot googu , ray ko .la
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=la
xpos=INFL
FocusType=Compl
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ki
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol1
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Kiyama jibal na ne layal na gisiinu melokaan wu sax wi , du caagéenug ngir ne da mu ko wóoroon ne mu a di dëgg , waaye rekk ngir ne loolu la bëggoon mu di li am .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Gox yooyu nga xam ne njëkk " Nosteg Solofrayn gi " da nu nekkoon ay gox yu nga xam ne bu ci nekk da mu amoon nosteg pobb gu nduwaan , gu mu bokkul ak kenn .da
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=da
xpos=INFL
FocusType=Verb
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
gox
features...upos=NOUN
lemma=gox
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Bokkoon na ci xeexam bi gënoon a rëy , delloo askan wi ak di leen xelal ci ñu dellu ci jaamu li fi maam yi bàyyi woon , te bàyyi diine yu bees yi fi ganesi ( Nasaraan , Lislaam , añs ... ) .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
leen
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Plur
Person=2,3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Tabax nañu ay kër fépp ci gox bi .nañu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
kër
features...upos=NOUN
lemma=kër
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Bu jëkk , nguur googu , ay socé ak ay séeréer , ñu a ko yoroon .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Daldi ni : Jëmm jii de ba ma di gën di gone bind naa ab Kaamil , di ko jox saa baay Sëriñ Moor Anta Sali .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Jabet mën na a jàpp siddit yi , ba ki mu dal dootul am yëg-yëg ci yaramam , maanaam du yëg lu tàng mbaa lu sedd .dootul
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
Polarity=Neg
SubjAuxCount=1
Tense=Fut
yëg-yëg
features...upos=NOUN
lemma=yëg-yëg
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ñu ngi leen di nuyu ku ci nekk ci yeen ci sa tur ak sa sànt te di leen dalal ci jàmm .ngi
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=ngi
xpos=AUX
Aspect=Prog
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=2+
leen
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Plur
Person=2,3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ñépp am nañu sañ-sañ ci yem añu ab liggéey , su fekkee ne ñu a yem liggéey , ci lu àndul ak benn xàjjaatle .nañu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
sañ-sañ
features...upos=NOUN
lemma=sañ-sañ
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Waaye tudd sunu soxna yi moom , da mu mel ni lu informel la te it ku ci nekk ña féete ak yaw rekk a di tudd sa aw tur , di wax sa ay jikko , di la misaaloo .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
tur
features...upos=NOUN
lemma=tur
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Dinañu ko xam : ay wax yu teguwul mëneesu ko a dëggal .dinañu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=dina
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Ndax mel na bu baax ne sóobukati jawwu yi indi nañu firndey xam-xam ci ne àdduna bi am na ab tàmbali .nañu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
firndey
features...upos=NOUN
lemma=firnde
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Plur
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Lu dul xarañteefam ak yaakaar bi nit ñi am ci moom , Peresidãa Faamara Ibraayima Saaña du am ay pexey yey ñi bañ , ngir wéral jeexital yi tukke ci waxtaan wi réew mépp bokk .du
features...upos=AUX
deprel=aux
Aspect=Imp
Mood=Ind,Ind
Polarity=Neg
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
pexey
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Noonu lañu leen tàggate ngir ngeen màggal Yàlla ci li mu leen gindi .lañu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=la
xpos=INFL
FocusType=Compl
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
leen
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Plur
Person=2,3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Nguuri Gambi gu kawe gi da ñu daan dàkkul seen bopp cong yi leen seen dëkkandoo yi daan faral a def , jublu woon ci nangu ci ñoom lenn ci seen i suuf .daan
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Hab
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Past
leen
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Plur
Person=2,3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Te daan nañu faral di gis ay jumtukaay yu baax lool yu ñu sàggane , bàyyi leen ci ëtt bi naaj wi ak taw bi di leen yàq .di
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
leen
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Céy , politik yenn saa yi kenn du xam lu mu di nirool !du
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
Polarity=Neg
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
lu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol7
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ñépp am nañu sañ-sañ ci yem añu ab liggéey , su fekkee ne ñu a yem liggéey , ci lu àndul ak benn xàjjaatle .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
liggéey
features...upos=NOUN
lemma=liggéey
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Jeynaba Taraawore amoon na lu war a mat ñaar-fukki at , mu ngi dëkkoon Inite 11 ci Pàrsel Aseni .ngi
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=ngi
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
Inite
features...upos=PROPN
lemma=Inite
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Réew mi mu a di fal , te ku jub , maandu , farlu , mat rekk lañu war a jiital :lañu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=la
xpos=INFL
FocusType=Compl
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ku
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol1
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Dafa tàmbalee tëj gémmiñu benn pàcc ci ñiy xeexal askan wi te defuñu pólótig , ci lu nga xam ne da leen di ger , wala mu wañ seen loxo .da
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=2+
leen
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Noo mu ngi dellu di fésal pas-pas bi mu am ci wéyal xeexu maréew bi muy def ngir neenal yokkug kuurãa bi laluwul ci lenn lu jaadu , tey xamal askan wi ñu pare xeex xeex bi .di
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
pas-pas
features...upos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Wante ci atum 2006 ba ma Toni Morrison woowee ngir ma jàng benn pàcc ci sama téere bi tudd Murambi ca " Musée du Louvre " , ca laa tekkiwaale woon benn dóg ca Doomi Golo .laa
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=la
xpos=INFL
FocusType=Compl
Mood=Ind
SubjAuxCount=2+
dóg
features...upos=NOUN
lemma=dóg
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Bi Demburu di woo pël ñi , fekkoon na Sónko woo waa Kaasamaas ba pare .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
pël
features...upos=NOUN
lemma=pël
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Jëwriñu mbey mi a ngi topp mbir moomu .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=AUX
Mood=Ind,Ind
PronType=Prs
SubjAuxCount=2+
mbir
features...upos=NOUN
lemma=mbir
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Li mu mujjee nag , mooy tënk sañ-sañu nit ñi .mooy
features...upos=AUX
deprel=aux
SubjAuxCount=1
sañ-sañu
features...upos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Dafay def ay widéwoo yu bare yoo xam ne moo ngi ko duppe Càmbar gafag réew mi .ngi
features...upos=AUX
deprel=aux
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Li ñu ci wax tax na ngeen weeru ci njëg li ngeen doon jaaye takku dundu bu nekk .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
weeru
features...upos=NOUN
lemma=weeru
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Waaye ñi gëmul lim yi nguur gi joxe , teguñu fi dara lu lalu ci xam-xam ak doxalin , wax a leen neex rekk ñuy wax di dem .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
leen
features...upos=PRON
lemma=leen
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Bu dee aw nag manees na ko a rendi , manees na ko a loj .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Yàkkaar nañu ne daal , liggéeyu tekki bii ak yeneen yu ni mel yu am solo yu ko jiitu , da ñu di gën a leeral yoon wi ñu mën a jëriñoo li ñu moomul , te duñu sànni li ñu moom .duñu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
Polarity=Neg
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
li
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol7
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Gisiin wii nga xam ne amul woon geneen jublu gu feeñ gu dul dëgëral xeltug ngérum ne-ne nekkoon na di lu safaanoo ak gisiinu Big Bang wi saxaloon ne àdduna bi am na ag tàmbali .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
tàmbali
features...upos=NOUN
lemma=tàmbali
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ca dëgg-dëgg , Big Bang indi na ci ay jafe-jafe lu sakkan ñeel woroom xam-xami ngérum ne-ne mi .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
lu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol7
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ropplaan yii ñoo gën a màggat bu njiitu réew mi , Puwent Saareen .ñoo
features...upos=AUX
deprel=aux
SubjAuxCount=1
bu
features...upos=PRON
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Askani Senegaal am na ndam !na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ndam
features...upos=NOUN
lemma=ndam
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Ba mu mujj di ku xarañe bépp xam-xamu Lislaam , te it di ku di jëfe ngirum Tassawuuf ci anam gu xóot .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
ngirum
features...upos=NOUN
lemma=ngir
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Baati biir yu bare tàmbali a di ma àwwu , rawatina ay baati jiggéen .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
xpos=AUX
Aspect=Imp
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
Tense=Pres
ma
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=1
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Foofu lañu sanc ay dëkk yu mel ni KasKas ak Njum .lañu
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=la
xpos=INFL
FocusType=Compl
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
dëkk
features...upos=NOUN
lemma=dëkk
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Surgab tubaab bu ñu fi cëppe , te sax néew-di-doole yi di ko dundal ci li ñuy dajale .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Suuf mu a nekkoon jumtukaay bi ëppoon solo , moom ñépp a ko bokkoon .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
jumtukaay
features...upos=NOUN
lemma=jumtukaay
xpos=NOUN
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Suuf mu a nekkoon jumtukaay bi ëppoon solo , moom ñépp a ko bokkoon .a
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=a
xpos=INFL
FocusType=Subj
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=obj
UD_Wolof-WTB
Xawma fu doomu Senegaal bu mel nii jóge di rusloo réew mi yépp .di
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=di
Mood=Ind,Ind
SubjAuxCount=1
réew
features...upos=NOUN
lemma=réew
deprel=obj
UD_Wolof-AfriSUD
Doorees na ag gaaralu Windows Phone 7 ca New York .na
features...upos=AUX
deprel=aux
lemma=na
xpos=INFL
Aspect=Perf
Mood=Ind
SubjAuxCount=1
gaaralu
features...upos=NOUN
lemma=gaaral
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=obj
UD_Wolof-WTB