Example items (sample of 50)
| sen_str | Aux_form | Aux_features | obj_form | obj_features | treebank_link |
|---|---|---|---|---|---|
| Ñoñ ne-ne ñi da ñu jàppe woon xalaatu àdduna bu amul yamu bii mu di seen ndëerlaay lu mag . | da | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=da xpos=INFL FocusType=Verb Mood=Ind SubjAuxCount=2+ | xalaatu | features...upos=NOUNlemma=xalaat xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Du lu ñu fi di doxal mbaa àtteb jeneen diine , waaye lépp lu ñu di def warees na ko a xool ba xam gaañul jenn ci diine yooyu . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Nit ku ne am na sañ-sañ ci yoon feg ko ci lëñbët yooyu ak tooñ yooyu . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | sañ-sañ | features...upos=NOUNlemma=sañ-sañ xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Dama koy naqarlu te di ko mas-sawu , moom ak njabootam . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Ci misaal benn deppite bu yorul beneen ndombo tànk , di am weer wu dee benn milyoŋ ak juróom-benn-fukki junne ( 1 ) ( te boolewuñu ci yeneen tegandaay yi mel xaalisu luyaas , xaalisu esãas ak daamaar yi ... | di | features...upos=AUXdeprel=aux Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | milyoŋ | features...upos=NOUNdeprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Bu ñu ko fàtte fii ci Afrik , jiggéen a fi mas a fallu , di yaay , di lingeer , di ndey-ji-réew , di buur , ca Misira démb , Nibi , Meroe , ba ci Waalo ak Kajoor . | bu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=bu xpos=INFL Mood=Imp Polarity=Neg SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Ci mujjantalug xarnu bu fukkeel la Waar Jaabi song ki mujjoon ci buuri njaboot googu , ray ko . | la | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ki | features...upos=PRONlemma=bi xpos=PRON Definite=Def Deixis=Prox NounClass=Wol1 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Kiyama jibal na ne layal na gisiinu melokaan wu sax wi , du caagéenug ngir ne da mu ko wóoroon ne mu a di dëgg , waaye rekk ngir ne loolu la bëggoon mu di li am . | da | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=da xpos=INFL FocusType=Verb Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Gox yooyu nga xam ne njëkk " Nosteg Solofrayn gi " da nu nekkoon ay gox yu nga xam ne bu ci nekk da mu amoon nosteg pobb gu nduwaan , gu mu bokkul ak kenn . | da | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=da xpos=INFL FocusType=Verb Mood=Ind SubjAuxCount=1 | gox | features...upos=NOUNlemma=gox xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Bokkoon na ci xeexam bi gënoon a rëy , delloo askan wi ak di leen xelal ci ñu dellu ci jaamu li fi maam yi bàyyi woon , te bàyyi diine yu bees yi fi ganesi ( Nasaraan , Lislaam , añs ... ) . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | leen | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Plur Person=2,3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Tabax nañu ay kër fépp ci gox bi . | nañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | kër | features...upos=NOUNlemma=kër deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Bu jëkk , nguur googu , ay socé ak ay séeréer , ñu a ko yoroon . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Daldi ni : Jëmm jii de ba ma di gën di gone bind naa ab Kaamil , di ko jox saa baay Sëriñ Moor Anta Sali . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Jabet mën na a jàpp siddit yi , ba ki mu dal dootul am yëg-yëg ci yaramam , maanaam du yëg lu tàng mbaa lu sedd . | dootul | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind Polarity=Neg SubjAuxCount=1 Tense=Fut | yëg-yëg | features...upos=NOUNlemma=yëg-yëg xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Ñu ngi leen di nuyu ku ci nekk ci yeen ci sa tur ak sa sànt te di leen dalal ci jàmm . | ngi | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=ngi xpos=AUX Aspect=Prog Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=2+ | leen | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Plur Person=2,3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Ñépp am nañu sañ-sañ ci yem añu ab liggéey , su fekkee ne ñu a yem liggéey , ci lu àndul ak benn xàjjaatle . | nañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | sañ-sañ | features...upos=NOUNlemma=sañ-sañ xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Waaye tudd sunu soxna yi moom , da mu mel ni lu informel la te it ku ci nekk ña féete ak yaw rekk a di tudd sa aw tur , di wax sa ay jikko , di la misaaloo . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=2+ | tur | features...upos=NOUNlemma=tur xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Dinañu ko xam : ay wax yu teguwul mëneesu ko a dëggal . | dinañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=dina SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Ndax mel na bu baax ne sóobukati jawwu yi indi nañu firndey xam-xam ci ne àdduna bi am na ab tàmbali . | nañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | firndey | features...upos=NOUNlemma=firnde xpos=NOUN Case=Gen Number=Plur deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Lu dul xarañteefam ak yaakaar bi nit ñi am ci moom , Peresidãa Faamara Ibraayima Saaña du am ay pexey yey ñi bañ , ngir wéral jeexital yi tukke ci waxtaan wi réew mépp bokk . | du | features...upos=AUXdeprel=aux Aspect=Imp Mood=Ind,Ind Polarity=Neg SubjAuxCount=1 Tense=Pres | pexey | features...upos=NOUNdeprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Noonu lañu leen tàggate ngir ngeen màggal Yàlla ci li mu leen gindi . | lañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | leen | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Plur Person=2,3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Nguuri Gambi gu kawe gi da ñu daan dàkkul seen bopp cong yi leen seen dëkkandoo yi daan faral a def , jublu woon ci nangu ci ñoom lenn ci seen i suuf . | daan | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Hab Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Past | leen | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Plur Person=2,3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Te daan nañu faral di gis ay jumtukaay yu baax lool yu ñu sàggane , bàyyi leen ci ëtt bi naaj wi ak taw bi di leen yàq . | di | features...upos=AUXdeprel=aux Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | leen | features...upos=PRONdeprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Céy , politik yenn saa yi kenn du xam lu mu di nirool ! | du | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind Polarity=Neg SubjAuxCount=1 Tense=Pres | lu | features...upos=PRONlemma=bu xpos=PRON NounClass=Wol7 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Ñépp am nañu sañ-sañ ci yem añu ab liggéey , su fekkee ne ñu a yem liggéey , ci lu àndul ak benn xàjjaatle . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | liggéey | features...upos=NOUNlemma=liggéey xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Jeynaba Taraawore amoon na lu war a mat ñaar-fukki at , mu ngi dëkkoon Inite 11 ci Pàrsel Aseni . | ngi | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=ngi Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | Inite | features...upos=PROPNlemma=Inite deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Réew mi mu a di fal , te ku jub , maandu , farlu , mat rekk lañu war a jiital : | lañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ku | features...upos=PRONlemma=bu xpos=PRON NounClass=Wol1 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Dafa tàmbalee tëj gémmiñu benn pàcc ci ñiy xeexal askan wi te defuñu pólótig , ci lu nga xam ne da leen di ger , wala mu wañ seen loxo . | da | features...upos=AUXdeprel=aux Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=2+ | leen | features...upos=PRONdeprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Noo mu ngi dellu di fésal pas-pas bi mu am ci wéyal xeexu maréew bi muy def ngir neenal yokkug kuurãa bi laluwul ci lenn lu jaadu , tey xamal askan wi ñu pare xeex xeex bi . | di | features...upos=AUXdeprel=aux Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | pas-pas | features...upos=NOUNdeprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Wante ci atum 2006 ba ma Toni Morrison woowee ngir ma jàng benn pàcc ci sama téere bi tudd Murambi ca " Musée du Louvre " , ca laa tekkiwaale woon benn dóg ca Doomi Golo . | laa | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=2+ | dóg | features...upos=NOUNlemma=dóg xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Bi Demburu di woo pël ñi , fekkoon na Sónko woo waa Kaasamaas ba pare . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | pël | features...upos=NOUNlemma=pël deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Jëwriñu mbey mi a ngi topp mbir moomu . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=AUX Mood=Ind,Ind PronType=Prs SubjAuxCount=2+ | mbir | features...upos=NOUNlemma=mbir xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Li mu mujjee nag , mooy tënk sañ-sañu nit ñi . | mooy | features...upos=AUXdeprel=aux SubjAuxCount=1 | sañ-sañu | features...upos=NOUNCase=Gen Number=Sing deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Dafay def ay widéwoo yu bare yoo xam ne moo ngi ko duppe Càmbar gafag réew mi . | ngi | features...upos=AUXdeprel=aux Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONdeprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Li ñu ci wax tax na ngeen weeru ci njëg li ngeen doon jaaye takku dundu bu nekk . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | weeru | features...upos=NOUNlemma=weeru deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Waaye ñi gëmul lim yi nguur gi joxe , teguñu fi dara lu lalu ci xam-xam ak doxalin , wax a leen neex rekk ñuy wax di dem . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | leen | features...upos=PRONlemma=leen deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Bu dee aw nag manees na ko a rendi , manees na ko a loj . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Yàkkaar nañu ne daal , liggéeyu tekki bii ak yeneen yu ni mel yu am solo yu ko jiitu , da ñu di gën a leeral yoon wi ñu mën a jëriñoo li ñu moomul , te duñu sànni li ñu moom . | duñu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind Polarity=Neg SubjAuxCount=1 Tense=Pres | li | features...upos=PRONlemma=bi xpos=PRON Definite=Def Deixis=Prox NounClass=Wol7 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Gisiin wii nga xam ne amul woon geneen jublu gu feeñ gu dul dëgëral xeltug ngérum ne-ne nekkoon na di lu safaanoo ak gisiinu Big Bang wi saxaloon ne àdduna bi am na ag tàmbali . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | tàmbali | features...upos=NOUNlemma=tàmbali xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Ca dëgg-dëgg , Big Bang indi na ci ay jafe-jafe lu sakkan ñeel woroom xam-xami ngérum ne-ne mi . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | lu | features...upos=PRONlemma=bu xpos=PRON NounClass=Wol7 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Ropplaan yii ñoo gën a màggat bu njiitu réew mi , Puwent Saareen . | ñoo | features...upos=AUXdeprel=aux SubjAuxCount=1 | bu | features...upos=PRONdeprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Askani Senegaal am na ndam ! | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ndam | features...upos=NOUNlemma=ndam xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Ba mu mujj di ku xarañe bépp xam-xamu Lislaam , te it di ku di jëfe ngirum Tassawuuf ci anam gu xóot . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | ngirum | features...upos=NOUNlemma=ngir xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Baati biir yu bare tàmbali a di ma àwwu , rawatina ay baati jiggéen . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | ma | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=1 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Foofu lañu sanc ay dëkk yu mel ni KasKas ak Njum . | lañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | dëkk | features...upos=NOUNlemma=dëkk xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Surgab tubaab bu ñu fi cëppe , te sax néew-di-doole yi di ko dundal ci li ñuy dajale . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Suuf mu a nekkoon jumtukaay bi ëppoon solo , moom ñépp a ko bokkoon . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | jumtukaay | features...upos=NOUNlemma=jumtukaay xpos=NOUN deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Suuf mu a nekkoon jumtukaay bi ëppoon solo , moom ñépp a ko bokkoon . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=obj | UD_Wolof-WTB |
| Xawma fu doomu Senegaal bu mel nii jóge di rusloo réew mi yépp . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | réew | features...upos=NOUNlemma=réew deprel=obj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Doorees na ag gaaralu Windows Phone 7 ca New York . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | gaaralu | features...upos=NOUNlemma=gaaral xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=obj | UD_Wolof-WTB |