Example items (sample of 50)

sen_strVerb_formVerb_featuresiobj_formiobj_featurestreebank_link
Dëkk bi ñu xam ne , ay nit ñu ñuul ñu a fa ne woon , te ñu daan tudde ñu dëkk ca biir réew mi " kaw " .tudde
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=tudde
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
kaw
features...upos=NOUN
lemma=kaw
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ñu fal buur bu ñu tudde Xulixuli , di fàtteliku bi NJAAJAAN NJAAY ( ku jëkk a nekk Buur-ba Jolof ) nekkoon biir dex gi , ca Waalo .tudde
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=tudde
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Xulixuli
features...upos=PROPN
lemma=Xulixuli
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Di leen balu àq ; di leen baal àq , te di ñaan Yàlla boole nu baal .baal
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=baal
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
àq
features...upos=NOUN
lemma=àq
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Te téy jii nag nga xam ne àddina si da mu dem ba mel ni as ndëkk su ndaw , xarala yu mel ni enternet ak yeneen , di def ba askan yépp am sañ-sañu wone seen dayoo , wone seen mbaax , seen i aada ak yoon wa ñu di gise àddina , waruñu a nangu di dés ginnaaw mukk !gise
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=gis
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
wa
features...upos=PRON
lemma=ba
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Remt
NounClass=Wol10
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Tudde naa ko Leon Werthtudde
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=tudde
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Leon
features...upos=PROPN
lemma=Leon
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Nataalal ma beneen .nataalal
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=nataal
xpos=VERB
Mood=Imp
VerbForm=Fin
beneen
features...upos=PRON
lemma=beneen
xpos=PRON
NounClass=Wol5
Number=Sing
PronType=Ind
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Loolu a waral bi UNESCO nemmeekoo càggante ak yàq gu jeggi-dayoo googu mu def at mu nekk mu di fàttali xeet yi ak askan yi seeni làmmiñ !fàttali
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=fàttali
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
làmmiñ
features...upos=NOUN
lemma=làmmiñ
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Nguur gi dina jël ay matuwaay ngir ñi jël geerte beykat yi fay leen ci lu gaaw seen alal , loolu la dige .fay
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=fay
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
alal
features...upos=NOUN
lemma=alal
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Wante su dul woon loolu sax , ñépp xam nañu ne mbër mu mel ni Ablaay Wàdd , rawatina mu yore li mu yore , maanaam pexe yi ak mën-mën yi ko " Etaa " jox , su nga ko bëggee daan alafook nga teel a jóg .jox
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=jox
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
yi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ñi di door a falu ñu a yoral seen bopp suuf si walla boog ñu dénk ko ay ceddo .yoral
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=yor
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
suuf
features...upos=NOUN
lemma=suuf
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Nguuri Gambi gu kawe gi da ñu daan dàkkul seen bopp cong yi leen seen dëkkandoo yi daan faral a def , jublu woon ci nangu ci ñoom lenn ci seen i suuf .faral
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=faral
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
yi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Wonees na nosteg doxiin bi mel niki lu di mottalil boppam ag dundam ci lu dul di ko xaar feneen .mottalil
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=mottali
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
dundam
features...upos=NOUN
lemma=dund
xpos=NOUN
Number=Sing
Poss=Yes
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Xalaat-leen kon mbetteel gi am ba bët di set , am senn mbaat su sew , su xoromu sax su ma yee naan ma : Du nga ma nataalal xar , su la neexee ?nataalal
features...upos=VERB
deprel=parataxis
lemma=nataal
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
xar
features...upos=NOUN
lemma=xar
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ci kow bundxataal gu ñu ko di bundxataal , nit ku ne sañ na wuti rawukaay , sañ na yit muurloo rawukaay ci yeneen i réew .bundxataal
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=bundxataal
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
gu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Képp nit ku ñu tuumaal tooñeel , njortees na ni ku set la , ba keroog ba yoon di wéral tuuma ji , ci layoo bu ne fàŋŋ , fekk warlulees na nit ki fàggutéef yi layam laaj yépp .warlulees
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=warlul
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
fàggutéef
features...upos=NOUN
lemma=fàggutéef
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Gannaaw bi lañu ko tuxël Jinge , tuxëlaat ko Ndeer .tuxëlaat
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=tuxëlaat
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Ndeer
features...upos=PROPN
lemma=Ndeer
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Bu lu ñu di woowe Pak jotee ñu jox ndongoy daara yi ay fan yu dul jeex ngir ag bër .jox
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=jox
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
fan
features...upos=NOUN
lemma=fan
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Booba Cerno Ba , mu ngi woon ca jawriñ ji ñu dénk gi Caada gi .dénk
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=dénk
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Caada
features...upos=PROPN
lemma=Caada
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Karamoko Alfa jiite ko , soppi gox boobu it def ko nguurug Lislaam .def
features...upos=VERB
deprel=compound:svc
lemma=def
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
nguurug
features...upos=NOUN
lemma=nguur
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Li tax ma nettali leen loolu lépp ci dippi-biddiw B612 ba noppi wax leen limam , du lenn lu dul mag ñi nu di dégglu .nettali
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=nettali
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
loolu
features...upos=PRON
lemma=boobu
xpos=PRON
Deixis=Prox
DeixisRef=2
NounClass=Wol7
Number=Sing
PronType=Dem
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ceññeer yii ñu di wooye ceññeeri mbëj-bijjaakon yu Big Bang niruwuñu woon lu jóge ci benn gongikuwaay , waaye da mu doon lu tas ci jawwu jépp .wooye
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=wooye
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ceññeeri
features...upos=NOUN
lemma=ceññeer
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Plur
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Wante lekk ba noppi xëpp ci suuf loolu la faye askani Senegaal !faye
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=faye
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
askani
features...upos=NOUN
lemma=askan
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Plur
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Yonent bi ( Yalla na jàmmi Yàlla nekk ci moom ) nee na : Sellal-leen seen i jëf ngir Yàlla kat du nangu lu dul lu ñu sellal ngir moom .sellal-leen
features...upos=VERB
deprel=parataxis
lemma=sellal
xpos=VERB
Mood=Imp
VerbForm=Fin
jëf
features...upos=NOUN
lemma=jëf
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Lii la askan wi sas réew mi !sas
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=sas
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
lii
features...upos=PRON
lemma=bii
xpos=PRON
Deixis=Prox
DeixisRef=1
NounClass=Wol7
Number=Sing
PronType=Dem
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ku ko ñaani ba mayees la ko nag man na ko a jaay dara nekku ci .mayees
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=may
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Sing
Person=3
PronType=Prs
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ablaay Wàdd gaal ga ko ñu bare seddoon lekku ca !seddoon
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=sedd
xpos=VERB
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
ga
features...upos=PRON
lemma=ba
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Remt
NounClass=Wol3
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Bokk na ci yooyu , dagg Doox bu Warsaw gu Poloñ gi , dagg ko ci Brusiya , te jox ko Rusi .jox
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=jox
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Rusi
features...upos=PROPN
lemma=Rusi
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Fàcc gu mag gii nga xam ne ci la àdduna bi doore , tuddeesoon na ko Big Bang , gisiin wi it daal di jël tur wi .tuddeesoon
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=tudde
xpos=VERB
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
Big
features...upos=PROPN
lemma=Big
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ki yore wàllu tàggatu gi ca Dakaar Sakere Këer , Olivier Brice Sylvain te ñu tuumaal ko mbiru càkkuy xale yu ndaw ba police teg ko loxo , dafa wéddi ba mu set wecc ne li ñu koy waxal naan dafa doon raayaate wala di def lu ni mel , dara du ci dëgg .tuumaal
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=tuumal
ko
features...upos=PRON
lemma=ko
deprel=iobj
UD_Wolof-AfriSUD
Nee na , li ñu di napp dina nu indil at mu nekk 35 Dollar ( ton bu nekk ) .indil
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=indi
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Dollar
features...upos=PROPN
lemma=Dollar
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Mbooloo ma ñu ko di jagleel man na a am njeexiit ci ëmbiit mi ; ab jimbulang bi ñu di jagleel i gune mu a di gën a néew bi ñu di jagleel i mag .jagleel
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=jagleel
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
mag
features...upos=NOUN
lemma=mag
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Yonent bi feeñu na ko di ko ñaaxe Amsatu , naan ko : Xoolal Amsatu ( jàmmi Yàlla ci moom ) di ab Sahaaba bu jàmbaare ak rayiin wu ñaaw wu ñu ko ray .ray
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=ray
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
wu
features...upos=PRON
lemma=bu
xpos=PRON
NounClass=Wol10
Number=Sing
Person=3
PronType=Rel
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Yenn ci liggéey yi mat a fattaliku bokk na ci jimbulang bi Ibn Xaldun bindoon ci 1377 , duppee ko Al-Muqaddima ( Taariixu àdduna bi ) , mu ëmboon mbooleem xameefi XIVu xarnu bi : melosuuf , xeltu , taariix , koom-koom , gëstumboolaay , politig , paj ba ci suqaliku gu sax .duppee
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=duppe
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Al-Muqaddima
features...upos=PROPN
lemma=Al-Muqaddima
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ndax ku ci nekk xam na ni su nga nee askan wi " Bennoo Siggil Senegaal " rekk nit ñi xam lu nga wax , jaratul sax nga leen di faram-fàcceel lenn .nee
features...upos=VERB
deprel=advcl
lemma=ne
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Bennoo
features...upos=PROPN
lemma=Bennoo
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Kon , mbokk sama , xarit sama dëgg la sax , àddina a dox , Nasaraan juuxsi fi , di làkk làkkam , te naan nu bàyyileen seen wos !bàyyileen
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=bàyyi
xpos=VERB
Mood=Imp
VerbForm=Fin
wos
features...upos=NOUN
lemma=wos
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Bëtt-bëttu wasin , li ko di yóbbe jigéen mu a di ñàkk ku ko taxawu ba mu ëmbee , ñàkk yit ku ko taxawu ba mu di wasin .yóbbe
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=yóbbe
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
jigéen
features...upos=NOUN
lemma=jigéen
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Mu baamtuwaatal ma ndànk , mel ni loolu lu ko ñor la lool : Ey waay , nataalal ma xar .nataalal
features...upos=VERB
deprel=parataxis
lemma=nataal
xpos=VERB
Mood=Imp
VerbForm=Fin
xar
features...upos=NOUN
lemma=xar
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Xar laa bëgg , nataalal ma xar .nataalal
features...upos=VERB
deprel=parataxis
lemma=nataal
xpos=VERB
Mood=Imp
VerbForm=Fin
xar
features...upos=NOUN
lemma=xar
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Am na aw dig wu nekk ci diggante ñi jiite ak ñi ñu jiite .jiite
features...upos=VERB
deprel=acl
lemma=jiite
Mood=Ind,Ind
ñu
features...upos=PRON
lemma=mu
deprel=iobj
UD_Wolof-AfriSUD
Bi ma di raam , sama pàppa , da mu amoon benn xaritu « seef de kanton » bu nu di wax Seex Njaay .wax
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=wax
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Seex
features...upos=PROPN
lemma=Seex
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Pensiyas ak Wilson joxees na leen neexalub Nobel ngir seen wuññi yooyu .joxees
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=jox
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
neexalub
features...upos=NOUN
lemma=neexal
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ndax sunu làkk yii , amul senn làkk ci àddina su leen yóobul dara .yóobul
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=yóobul
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
dara
features...upos=NOUN
lemma=dara
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Abdu Juuf digoon na ma kër , waaye booba ba tey am na at , te gisuma dara .digoon
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=dig
xpos=VERB
Mood=Ind
Tense=Past
VerbForm=Fin
kër
features...upos=NOUN
lemma=kër
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Yii téere , loxo lañu leen doon sottee ba tax doonuñu woon tasaaroo lool , boroom alal yi ak niti diine yi rekk ñu a ci doon jot : doonoon nañu ay téere yu seer lool .sottee
features...upos=VERB
deprel=root
lemma=sotti
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
loxo
features...upos=NOUN
lemma=loxo
xpos=NOUN
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Lu tee nu jàppe ko royuwaayu askan wi ñeel soxna yépp ?jàppe
features...upos=VERB
deprel=ccomp
lemma=jàppe
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
royuwaayu
features...upos=NOUN
lemma=royuwaay
xpos=NOUN
Case=Gen
Number=Sing
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Yow mi bëgg lu la musal ci kolesterol bu ëpp , toppal dénkaane yii la Doktoor Kase baaxe .baaxe
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=baaxe
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
yii
features...upos=PRON
lemma=bii
xpos=PRON
Deixis=Prox
DeixisRef=1
NounClass=Wol8
Number=Plur
PronType=Dem
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ãaselig M. B. Jéen bokk na ci téeméeri njaatige yu jigéen yu Québec , te defoon boppam kenn ku fa teewal Senegaal .defoon
features...upos=VERB
deprel=conj
Mood=Ind,Ind
Tense=Past
kenn
features...upos=PRON
deprel=iobj
UD_Wolof-AfriSUD
Nit ku ne sañ na dem yoon , ci kanam àttekaay yi ko yelloo ci réew mi , ngir tawat fa jëf yi di bëtt sañ-sañ yi ko Ndeyu Àtte bi walla ab àtte fàggul .fàggul
features...upos=VERB
deprel=acl:relcl
lemma=fàgg
xpos=VERB
Mood=Ind
Polarity=Neg
VerbForm=Fin
yi
features...upos=PRON
lemma=bi
xpos=PRON
Definite=Def
Deixis=Prox
NounClass=Wol8
Number=Plur
Person=3
PronType=Rel
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Ci ab xaatim àlluwa ji ñu di tuddee alluwaay Narmeer ( -3200 laata Juddu Yonnent Yàlla Isaa ) lañu firndeel mbind mi gën a yàgg te ñu ko di woowee " Hieroglyphes " ci Nasaraan .woowee
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=woo
xpos=VERB
Aspect=Perf
Mood=Ind
VerbForm=Fin
Hieroglyphes
features...upos=PROPN
lemma=Hieroglyphes
xpos=NAME
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB
Daan na yar ag njabootam ci di leen fàttali ak a nettali xistay gaa ñu baax ña , di leen ko jàjje ak di leen xamal la ñu def ba yelloo seen may yooyii , di leen yar ci yu ni mel , di leen ci nàmptal .jàjje
features...upos=VERB
deprel=conj
lemma=jàjj
xpos=VERB
Mood=Ind
VerbForm=Fin
leen
features...upos=PRON
lemma=ko
xpos=CL
Case=Acc
Number=Plur
Person=2,3
PronType=Prs
deprel=iobj
UD_Wolof-WTB