Example items (sample of 50)
| sen_str | Verb_form | Verb_features | iobj_form | iobj_features | treebank_link |
|---|---|---|---|---|---|
| Dëkk bi ñu xam ne , ay nit ñu ñuul ñu a fa ne woon , te ñu daan tudde ñu dëkk ca biir réew mi " kaw " . | tudde | features...upos=VERBdeprel=conj lemma=tudde xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | kaw | features...upos=NOUNlemma=kaw xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ñu fal buur bu ñu tudde Xulixuli , di fàtteliku bi NJAAJAAN NJAAY ( ku jëkk a nekk Buur-ba Jolof ) nekkoon biir dex gi , ca Waalo . | tudde | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=tudde xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | Xulixuli | features...upos=PROPNlemma=Xulixuli xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Di leen balu àq ; di leen baal àq , te di ñaan Yàlla boole nu baal . | baal | features...upos=VERBdeprel=conj lemma=baal xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | àq | features...upos=NOUNlemma=àq xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Te téy jii nag nga xam ne àddina si da mu dem ba mel ni as ndëkk su ndaw , xarala yu mel ni enternet ak yeneen , di def ba askan yépp am sañ-sañu wone seen dayoo , wone seen mbaax , seen i aada ak yoon wa ñu di gise àddina , waruñu a nangu di dés ginnaaw mukk ! | gise | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=gis xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | wa | features...upos=PRONlemma=ba xpos=PRON Definite=Def Deixis=Remt NounClass=Wol10 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Tudde naa ko Leon Werth | tudde | features...upos=VERBdeprel=root lemma=tudde xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | Leon | features...upos=PROPNlemma=Leon xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Nataalal ma beneen . | nataalal | features...upos=VERBdeprel=root lemma=nataal xpos=VERB Mood=Imp VerbForm=Fin | beneen | features...upos=PRONlemma=beneen xpos=PRON NounClass=Wol5 Number=Sing PronType=Ind deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Loolu a waral bi UNESCO nemmeekoo càggante ak yàq gu jeggi-dayoo googu mu def at mu nekk mu di fàttali xeet yi ak askan yi seeni làmmiñ ! | fàttali | features...upos=VERBdeprel=ccomp lemma=fàttali xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | làmmiñ | features...upos=NOUNlemma=làmmiñ xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Nguur gi dina jël ay matuwaay ngir ñi jël geerte beykat yi fay leen ci lu gaaw seen alal , loolu la dige . | fay | features...upos=VERBdeprel=advcl lemma=fay xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | alal | features...upos=NOUNlemma=alal xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Wante su dul woon loolu sax , ñépp xam nañu ne mbër mu mel ni Ablaay Wàdd , rawatina mu yore li mu yore , maanaam pexe yi ak mën-mën yi ko " Etaa " jox , su nga ko bëggee daan alafook nga teel a jóg . | jox | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=jox xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | yi | features...upos=PRONlemma=bi xpos=PRON Definite=Def Deixis=Prox NounClass=Wol8 Number=Plur Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ñi di door a falu ñu a yoral seen bopp suuf si walla boog ñu dénk ko ay ceddo . | yoral | features...upos=VERBdeprel=root lemma=yor xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | suuf | features...upos=NOUNlemma=suuf xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Nguuri Gambi gu kawe gi da ñu daan dàkkul seen bopp cong yi leen seen dëkkandoo yi daan faral a def , jublu woon ci nangu ci ñoom lenn ci seen i suuf . | faral | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=faral xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | yi | features...upos=PRONlemma=bi xpos=PRON Definite=Def Deixis=Prox NounClass=Wol8 Number=Plur Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Wonees na nosteg doxiin bi mel niki lu di mottalil boppam ag dundam ci lu dul di ko xaar feneen . | mottalil | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=mottali xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | dundam | features...upos=NOUNlemma=dund xpos=NOUN Number=Sing Poss=Yes deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Xalaat-leen kon mbetteel gi am ba bët di set , am senn mbaat su sew , su xoromu sax su ma yee naan ma : Du nga ma nataalal xar , su la neexee ? | nataalal | features...upos=VERBdeprel=parataxis lemma=nataal xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | xar | features...upos=NOUNlemma=xar xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ci kow bundxataal gu ñu ko di bundxataal , nit ku ne sañ na wuti rawukaay , sañ na yit muurloo rawukaay ci yeneen i réew . | bundxataal | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=bundxataal xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | gu | features...upos=PRONlemma=bu xpos=PRON NounClass=Wol3 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Képp nit ku ñu tuumaal tooñeel , njortees na ni ku set la , ba keroog ba yoon di wéral tuuma ji , ci layoo bu ne fàŋŋ , fekk warlulees na nit ki fàggutéef yi layam laaj yépp . | warlulees | features...upos=VERBdeprel=ccomp lemma=warlul xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | fàggutéef | features...upos=NOUNlemma=fàggutéef xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Gannaaw bi lañu ko tuxël Jinge , tuxëlaat ko Ndeer . | tuxëlaat | features...upos=VERBdeprel=conj lemma=tuxëlaat xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | Ndeer | features...upos=PROPNlemma=Ndeer xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Bu lu ñu di woowe Pak jotee ñu jox ndongoy daara yi ay fan yu dul jeex ngir ag bër . | jox | features...upos=VERBdeprel=root lemma=jox xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | fan | features...upos=NOUNlemma=fan xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Booba Cerno Ba , mu ngi woon ca jawriñ ji ñu dénk gi Caada gi . | dénk | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=dénk xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | Caada | features...upos=PROPNlemma=Caada xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Karamoko Alfa jiite ko , soppi gox boobu it def ko nguurug Lislaam . | def | features...upos=VERBdeprel=compound:svc lemma=def xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | nguurug | features...upos=NOUNlemma=nguur xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Li tax ma nettali leen loolu lépp ci dippi-biddiw B612 ba noppi wax leen limam , du lenn lu dul mag ñi nu di dégglu . | nettali | features...upos=VERBdeprel=ccomp lemma=nettali xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | loolu | features...upos=PRONlemma=boobu xpos=PRON Deixis=Prox DeixisRef=2 NounClass=Wol7 Number=Sing PronType=Dem deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ceññeer yii ñu di wooye ceññeeri mbëj-bijjaakon yu Big Bang niruwuñu woon lu jóge ci benn gongikuwaay , waaye da mu doon lu tas ci jawwu jépp . | wooye | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=wooye xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | ceññeeri | features...upos=NOUNlemma=ceññeer xpos=NOUN Case=Gen Number=Plur deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Wante lekk ba noppi xëpp ci suuf loolu la faye askani Senegaal ! | faye | features...upos=VERBdeprel=root lemma=faye xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | askani | features...upos=NOUNlemma=askan xpos=NOUN Case=Gen Number=Plur deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Yonent bi ( Yalla na jàmmi Yàlla nekk ci moom ) nee na : Sellal-leen seen i jëf ngir Yàlla kat du nangu lu dul lu ñu sellal ngir moom . | sellal-leen | features...upos=VERBdeprel=parataxis lemma=sellal xpos=VERB Mood=Imp VerbForm=Fin | jëf | features...upos=NOUNlemma=jëf xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Lii la askan wi sas réew mi ! | sas | features...upos=VERBdeprel=root lemma=sas xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | lii | features...upos=PRONlemma=bii xpos=PRON Deixis=Prox DeixisRef=1 NounClass=Wol7 Number=Sing PronType=Dem deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ku ko ñaani ba mayees la ko nag man na ko a jaay dara nekku ci . | mayees | features...upos=VERBdeprel=advcl lemma=may xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | ko | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Sing Person=3 PronType=Prs deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ablaay Wàdd gaal ga ko ñu bare seddoon lekku ca ! | seddoon | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=sedd xpos=VERB Mood=Ind Tense=Past VerbForm=Fin | ga | features...upos=PRONlemma=ba xpos=PRON Definite=Def Deixis=Remt NounClass=Wol3 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Bokk na ci yooyu , dagg Doox bu Warsaw gu Poloñ gi , dagg ko ci Brusiya , te jox ko Rusi . | jox | features...upos=VERBdeprel=conj lemma=jox xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | Rusi | features...upos=PROPNlemma=Rusi xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Fàcc gu mag gii nga xam ne ci la àdduna bi doore , tuddeesoon na ko Big Bang , gisiin wi it daal di jël tur wi . | tuddeesoon | features...upos=VERBdeprel=root lemma=tudde xpos=VERB Mood=Ind Tense=Past VerbForm=Fin | Big | features...upos=PROPNlemma=Big xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ki yore wàllu tàggatu gi ca Dakaar Sakere Këer , Olivier Brice Sylvain te ñu tuumaal ko mbiru càkkuy xale yu ndaw ba police teg ko loxo , dafa wéddi ba mu set wecc ne li ñu koy waxal naan dafa doon raayaate wala di def lu ni mel , dara du ci dëgg . | tuumaal | features...upos=VERBdeprel=conj lemma=tuumal | ko | features...upos=PRONlemma=ko deprel=iobj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Nee na , li ñu di napp dina nu indil at mu nekk 35 Dollar ( ton bu nekk ) . | indil | features...upos=VERBdeprel=ccomp lemma=indi xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | Dollar | features...upos=PROPNlemma=Dollar xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Mbooloo ma ñu ko di jagleel man na a am njeexiit ci ëmbiit mi ; ab jimbulang bi ñu di jagleel i gune mu a di gën a néew bi ñu di jagleel i mag . | jagleel | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=jagleel xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | mag | features...upos=NOUNlemma=mag xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Yonent bi feeñu na ko di ko ñaaxe Amsatu , naan ko : Xoolal Amsatu ( jàmmi Yàlla ci moom ) di ab Sahaaba bu jàmbaare ak rayiin wu ñaaw wu ñu ko ray . | ray | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=ray xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | wu | features...upos=PRONlemma=bu xpos=PRON NounClass=Wol10 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Yenn ci liggéey yi mat a fattaliku bokk na ci jimbulang bi Ibn Xaldun bindoon ci 1377 , duppee ko Al-Muqaddima ( Taariixu àdduna bi ) , mu ëmboon mbooleem xameefi XIVu xarnu bi : melosuuf , xeltu , taariix , koom-koom , gëstumboolaay , politig , paj ba ci suqaliku gu sax . | duppee | features...upos=VERBdeprel=advcl lemma=duppe xpos=VERB Aspect=Perf Mood=Ind VerbForm=Fin | Al-Muqaddima | features...upos=PROPNlemma=Al-Muqaddima xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ndax ku ci nekk xam na ni su nga nee askan wi " Bennoo Siggil Senegaal " rekk nit ñi xam lu nga wax , jaratul sax nga leen di faram-fàcceel lenn . | nee | features...upos=VERBdeprel=advcl lemma=ne xpos=VERB Aspect=Perf Mood=Ind VerbForm=Fin | Bennoo | features...upos=PROPNlemma=Bennoo xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Kon , mbokk sama , xarit sama dëgg la sax , àddina a dox , Nasaraan juuxsi fi , di làkk làkkam , te naan nu bàyyileen seen wos ! | bàyyileen | features...upos=VERBdeprel=ccomp lemma=bàyyi xpos=VERB Mood=Imp VerbForm=Fin | wos | features...upos=NOUNlemma=wos xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Bëtt-bëttu wasin , li ko di yóbbe jigéen mu a di ñàkk ku ko taxawu ba mu ëmbee , ñàkk yit ku ko taxawu ba mu di wasin . | yóbbe | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=yóbbe xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | jigéen | features...upos=NOUNlemma=jigéen xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Mu baamtuwaatal ma ndànk , mel ni loolu lu ko ñor la lool : Ey waay , nataalal ma xar . | nataalal | features...upos=VERBdeprel=parataxis lemma=nataal xpos=VERB Mood=Imp VerbForm=Fin | xar | features...upos=NOUNlemma=xar xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Xar laa bëgg , nataalal ma xar . | nataalal | features...upos=VERBdeprel=parataxis lemma=nataal xpos=VERB Mood=Imp VerbForm=Fin | xar | features...upos=NOUNlemma=xar xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Am na aw dig wu nekk ci diggante ñi jiite ak ñi ñu jiite . | jiite | features...upos=VERBdeprel=acl lemma=jiite Mood=Ind,Ind | ñu | features...upos=PRONlemma=mu deprel=iobj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Bi ma di raam , sama pàppa , da mu amoon benn xaritu « seef de kanton » bu nu di wax Seex Njaay . | wax | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=wax xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | Seex | features...upos=PROPNlemma=Seex xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Pensiyas ak Wilson joxees na leen neexalub Nobel ngir seen wuññi yooyu . | joxees | features...upos=VERBdeprel=root lemma=jox xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | neexalub | features...upos=NOUNlemma=neexal xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ndax sunu làkk yii , amul senn làkk ci àddina su leen yóobul dara . | yóobul | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=yóobul xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | dara | features...upos=NOUNlemma=dara xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Abdu Juuf digoon na ma kër , waaye booba ba tey am na at , te gisuma dara . | digoon | features...upos=VERBdeprel=root lemma=dig xpos=VERB Mood=Ind Tense=Past VerbForm=Fin | kër | features...upos=NOUNlemma=kër xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Yii téere , loxo lañu leen doon sottee ba tax doonuñu woon tasaaroo lool , boroom alal yi ak niti diine yi rekk ñu a ci doon jot : doonoon nañu ay téere yu seer lool . | sottee | features...upos=VERBdeprel=root lemma=sotti xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | loxo | features...upos=NOUNlemma=loxo xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Lu tee nu jàppe ko royuwaayu askan wi ñeel soxna yépp ? | jàppe | features...upos=VERBdeprel=ccomp lemma=jàppe xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | royuwaayu | features...upos=NOUNlemma=royuwaay xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Yow mi bëgg lu la musal ci kolesterol bu ëpp , toppal dénkaane yii la Doktoor Kase baaxe . | baaxe | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=baaxe xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | yii | features...upos=PRONlemma=bii xpos=PRON Deixis=Prox DeixisRef=1 NounClass=Wol8 Number=Plur PronType=Dem deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ãaselig M. B. Jéen bokk na ci téeméeri njaatige yu jigéen yu Québec , te defoon boppam kenn ku fa teewal Senegaal . | defoon | features...upos=VERBdeprel=conj Mood=Ind,Ind Tense=Past | kenn | features...upos=PRONdeprel=iobj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Nit ku ne sañ na dem yoon , ci kanam àttekaay yi ko yelloo ci réew mi , ngir tawat fa jëf yi di bëtt sañ-sañ yi ko Ndeyu Àtte bi walla ab àtte fàggul . | fàggul | features...upos=VERBdeprel=acl:relcl lemma=fàgg xpos=VERB Mood=Ind Polarity=Neg VerbForm=Fin | yi | features...upos=PRONlemma=bi xpos=PRON Definite=Def Deixis=Prox NounClass=Wol8 Number=Plur Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ci ab xaatim àlluwa ji ñu di tuddee alluwaay Narmeer ( -3200 laata Juddu Yonnent Yàlla Isaa ) lañu firndeel mbind mi gën a yàgg te ñu ko di woowee " Hieroglyphes " ci Nasaraan . | woowee | features...upos=VERBdeprel=conj lemma=woo xpos=VERB Aspect=Perf Mood=Ind VerbForm=Fin | Hieroglyphes | features...upos=PROPNlemma=Hieroglyphes xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Daan na yar ag njabootam ci di leen fàttali ak a nettali xistay gaa ñu baax ña , di leen ko jàjje ak di leen xamal la ñu def ba yelloo seen may yooyii , di leen yar ci yu ni mel , di leen ci nàmptal . | jàjje | features...upos=VERBdeprel=conj lemma=jàjj xpos=VERB Mood=Ind VerbForm=Fin | leen | features...upos=PRONlemma=ko xpos=CL Case=Acc Number=Plur Person=2,3 PronType=Prs deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |