Example items (sample of 50)
| sen_str | Aux_form | Aux_features | iobj_form | iobj_features | treebank_link |
|---|---|---|---|---|---|
| Da ma di wàcc ba tollu ak moom di ko wax waxi kàrt ak golf , politik mbaa ay karawaat . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | waxi | features...upos=NOUNlemma=wax xpos=NOUN Case=Gen Number=Plur deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Daldi ni : Jëmm jii de ba ma di gën di gone bind naa ab Kaamil , di ko jox saa baay Sëriñ Moor Anta Sali . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | baay | features...upos=NOUNlemma=baay xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Kon mënees na a yaakaar ne dina delloo " Union Africaine " gëdd gi mu yellool . | dina | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Fut | gëdd | features...upos=NOUNlemma=gëdd xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Fàcc gu mag gii nga xam ne ci la àdduna bi doore , tuddeesoon na ko Big Bang , gisiin wi it daal di jël tur wi . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | Big | features...upos=PROPNlemma=Big xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Noo ngi leen di yéene Tëbëskig jàmm ! | ngi | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=ngi xpos=AUX Aspect=Prog Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=2+ | Tëbëskig | features...upos=PROPNlemma=Tëbëski xpos=NAME Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Kleopaatar VII doonoon buuru Misra ( Egypte ) bu jigéen , te ñu ko daan woowe " Grek bi " ndax li mu bokkoon ci askanu ptolémaïque sosoo Masedoni ( Macédonie ) . | daan | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Hab Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Past | Grek | features...upos=PROPNlemma=Grek xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ñi di door a falu ñu a yoral seen bopp suuf si walla boog ñu dénk ko ay ceddo . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | suuf | features...upos=NOUNlemma=suuf xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ma di doomu góor gu ñu di wax Ngóor Mbay , ñu ko di woowee Abdu Faatma ca Cilmaxa , ak jiggéen ju ñu di wax Kumba Ndaxaar Sàll . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | Kumba | features...upos=PROPNlemma=Kumba xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Nga xam ne Firhawna it Yàlla lañu ko jàppe woon . | lañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=2+ | Yàlla | features...upos=PROPNlemma=Yàlla xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Moom lañu di jàppe ki njëkk a doon Yilimaan . | lañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=2+ | ki | features...upos=PRONlemma=bi xpos=PRON Definite=Def Deixis=Prox NounClass=Wol1 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Li wér daal mu a di ne yàtt bi ci jëmmam yeneen yàtt yu mel ni " yàttu moomeel sa bopp " ba ca Amerik , mbaa yàttu Yeesu Kiris ba ca Riyoo la di diiranteel mbàgg ! | la | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=2+ | mbàgg | features...upos=NOUNlemma=mbàgg xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Jële nanu ci Anas ( gërëmul Yàlla ci moom ) mu ne : Bi Yonent ( Yalla na jàmmi Yàlla nekk ci moom ) bi yegsee Madiina fekkee na leen ñaari bis ñu ca daan caaxaan ak a fo . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | bis | features...upos=NOUNlemma=bis xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Nit ku ne yelloo na kiiraay , su fekkee ne liggéeyul , da mu tawat , da mu tële , ki mu doon séyal da mu faatu ; ak su fekkee ne da mu màggat mbaa mu tollu fu nga xam ne , yeneen safaan yu ajuwul ci coobareem ñu a ko xañ la mu daan dunde . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | la | features...upos=PRONlemma=ba xpos=PRON Definite=Def Deixis=Remt NounClass=Wol7 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ndax ku ci nekk xam na ni su nga nee askan wi " Bennoo Siggil Senegaal " rekk nit ñi xam lu nga wax , jaratul sax nga leen di faram-fàcceel lenn . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | lenn | features...upos=PRONlemma=benn xpos=PRON NounClass=Wol7 Number=Sing PronType=Ind,Neg deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| " Mbirum farlu kese la " , loolu la ma ndoomi-buur si wax ca gànnaaw ga . | la | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | loolu | features...upos=PRONlemma=boobu xpos=PRON Deixis=Prox DeixisRef=2 NounClass=Wol7 Number=Sing PronType=Dem deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Nee na , li ñu di napp dina nu indil at mu nekk 35 Dollar ( ton bu nekk ) . | dina | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Fut | Dollar | features...upos=PROPNlemma=Dollar xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ci biir loolu jëm-kanam yi xam-xam ak xarala amal ci ñaar-fukkeelu xarnu , màbb nañu ci mujj gi xalaat bu njëlbéenu bii ñu di wooye ngérum ne-ne , wuññees na ne àdduna bi saxul ni ko ñoñ ne-ne ñi daan waxe . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | ngérum | features...upos=NOUNlemma=ngér xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Te téy jii nag nga xam ne àddina si da mu dem ba mel ni as ndëkk su ndaw , xarala yu mel ni enternet ak yeneen , di def ba askan yépp am sañ-sañu wone seen dayoo , wone seen mbaax , seen i aada ak yoon wa ñu di gise àddina , waruñu a nangu di dés ginnaaw mukk ! | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | wa | features...upos=PRONlemma=ba xpos=PRON Definite=Def Deixis=Remt NounClass=Wol10 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Man nag duma ko wax waxi yeew ak àll-yu-xonq mbaa ay bidiw . | duma | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind Polarity=Neg SubjAuxCount=1 Tense=Pres | waxi | features...upos=NOUNlemma=wax xpos=NOUN Case=Gen Number=Plur deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ma di doomu góor gu ñu di wax Ngóor Mbay , ñu ko di woowee Abdu Faatma ca Cilmaxa , ak jiggéen ju ñu di wax Kumba Ndaxaar Sàll . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | Abdu | features...upos=PROPNlemma=Abdu xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ma di doomu góor gu ñu di wax Ngóor Mbay , ñu ko di woowee Abdu Faatma ca Cilmaxa , ak jiggéen ju ñu di wax Kumba Ndaxaar Sàll . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | Ngóor | features...upos=PROPNlemma=Ngóor xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Di leen balu àq ; di leen baal àq , te di ñaan Yàlla boole nu baal . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | àq | features...upos=NOUNlemma=àq xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Abdu Juuf digoon na ma kër , waaye booba ba tey am na at , te gisuma dara . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | kër | features...upos=NOUNlemma=kër xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Tudde naa ko Leon Werth | naa | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | Leon | features...upos=PROPNlemma=Leon xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Gannaaw Maam Moor ab sëriñam da mu xawoon a jëm mag , te fi ñu nekkoon xaw a àlle , ba tax sedd ba xaw fa a tar , daan na ko fàggul matt mu mu di jaaroo , ngir mucc ci sedd boobu nga xam ni baaxul ci mag . | daan | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Hab Mood=Ind SubjAuxCount=2+ Tense=Past | matt | features...upos=NOUNlemma=matt xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ceññeer yii ñu di wooye ceññeeri mbëj-bijjaakon yu Big Bang niruwuñu woon lu jóge ci benn gongikuwaay , waaye da mu doon lu tas ci jawwu jépp . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | ceññeeri | features...upos=NOUNlemma=ceññeer xpos=NOUN Case=Gen Number=Plur deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Xabru ba it reeroon na , ba xameesul fu mu nekkati , waaye Sëriñ bi a jox ndigël Sëriñ Mbàkke Gani Buso , doomu nijaayam , ngir mu seetal ko te saytul ko barab boobee . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | Sëriñ | features...upos=PROPNlemma=Sëriñ xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Waxu coggal ñay googu ma ko wax nag da mu koo def i ree . | da | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=da xpos=INFL FocusType=Verb Mood=Ind SubjAuxCount=1 | ree | features...upos=NOUNlemma=ree xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Daan nañu tabaxal seen Yàlla yi ay jaamuwaay ( ay temple ) ngir màggale leen ko . | daan | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Hab Mood=Ind SubjAuxCount=2+ Tense=Past | jaamuwaay | features...upos=NOUNlemma=jaamuwaay xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Jiine ci Lebu , " rab " lañu ko tudde . | lañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | rab | features...upos=NOUNlemma=rab xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Bésu 21 fan ci weeru Fewrie at mu jot , moom la kurél gi di toppatoo caada , njàng ak xamtéef ( UNESCO ) te feeteewoo ci Mbotaayu-xeet-yi , jagleel làkki-ndey yi , maanaam làkk wi nga xam ne moom la nit ku nekk nàmp . | la | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | làkki-ndey | features...upos=NOUNlemma=làkki-ndey xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Nguuri Gambi gu kawe gi da ñu daan dàkkul seen bopp cong yi leen seen dëkkandoo yi daan faral a def , jublu woon ci nangu ci ñoom lenn ci seen i suuf . | daan | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Hab Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Past | yi | features...upos=PRONlemma=bi xpos=PRON Definite=Def Deixis=Prox NounClass=Wol8 Number=Plur Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Su lay yooyu yépp nag doyul , kon may naa téeré bi xale ba waa jooju masoon a doon , ndax mag ñi ngeen di gis doonoon nañu ay xale , wante ñi ci di fàtteliku loolu ñu neew lañu . | naa | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | xale | features...upos=NOUNlemma=xale xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Afirik : Sa téere bi , kalaame bu meti la , bu nga di kalaame kopparu Euro ak CFA . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | kopparu | features...upos=NOUNlemma=koppar xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Mbooloo ma ñu ko di jagleel man na a am njeexiit ci ëmbiit mi ; ab jimbulang bi ñu di jagleel i gune mu a di gën a néew bi ñu di jagleel i mag . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | ma | features...upos=PRONlemma=ba xpos=PRON Definite=Def Deixis=Remt NounClass=Wol6 Number=Sing Person=3 PronType=Rel deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Xar mu ndawa-ndaw laa la jox . | laa | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la xpos=INFL FocusType=Compl Mood=Ind SubjAuxCount=1 | xar | features...upos=NOUNlemma=xar xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Su nga leen di wax sa xarit bu bees , duñu la laaj mukk lu am solo . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | xarit | features...upos=NOUNlemma=xarit xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Jabet 1 , tuddees na ko yitam jabetu ndaw ( diabète juvénile ) , ndax li mu di dal nit ki ci ag ndawam , diggante ba mu amee ay weer ba 35 at . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | jabetu | features...upos=NOUNlemma=jabet xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Bëtt-bëttu wasin , li ko di yóbbe jigéen mu a di ñàkk ku ko taxawu ba mu ëmbee , ñàkk yit ku ko taxawu ba mu di wasin . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | jigéen | features...upos=NOUNlemma=jigéen xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Loolu tamit la waa Faraas xam ba taxawal kuréel gi ñu di woowe Francophonie . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | Francophonie | features...upos=PROPNlemma=Francophonie xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Dëkk bi ñu xam ne , ay nit ñu ñuul ñu a fa ne woon , te ñu daan tudde ñu dëkk ca biir réew mi " kaw " . | daan | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Hab Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Past | kaw | features...upos=NOUNlemma=kaw xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ci ab xaatim àlluwa ji ñu di tuddee alluwaay Narmeer ( -3200 laata Juddu Yonnent Yàlla Isaa ) lañu firndeel mbind mi gën a yàgg te ñu ko di woowee " Hieroglyphes " ci Nasaraan . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | Hieroglyphes | features...upos=PROPNlemma=Hieroglyphes xpos=NAME deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Waxuma la nag suulaale gi waa Isipt yi daan suulaale néew bi ak i bagaasam te séeréer su yàgg sa daan ko def . | daan | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=INFL Aspect=Hab Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Past | néew | features...upos=NOUNlemma=néew xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ngir yor dooley mbooloo mi ak ngir amal xaalis bi war ci caytu gi , ab natt bu ku ne war dugal loxoom mënul ñàkk ; dees ko di teg juddu-réew yépp , ku ne ak la nga mën . | dees | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=2+ Tense=Pres | juddu-réew | features...upos=NOUNlemma=juddu-réew xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Ci loolu Soxna si Yàlla may na ko ci sëy bu barkeel boobu , ñeenti doom , yu nga xam ni dinanu sawar lool ci tudd seen i tur , ak wax as tuut ci seen i jikko yu kawe . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | doom | features...upos=NOUNlemma=doom xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Leegi nag lu fa duggati rekk ci li bawoo ci nduwaan mi ak galag yi ñu ko di seddale mbooleem diiwaan yi , ci kem limub ña fa dëkk . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | mbooleem | features...upos=NOUNlemma=mboole xpos=NOUN Case=Gen Number=Sing deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Képp nit ku ñu tuumaal tooñeel , njortees na ni ku set la , ba keroog ba yoon di wéral tuuma ji , ci layoo bu ne fàŋŋ , fekk warlulees na nit ki fàggutéef yi layam laaj yépp . | na | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=na xpos=INFL Aspect=Perf Mood=Ind SubjAuxCount=1 | fàggutéef | features...upos=NOUNlemma=fàggutéef xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Wonees na nosteg doxiin bi mel niki lu di mottalil boppam ag dundam ci lu dul di ko xaar feneen . | di | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=di xpos=AUX Aspect=Imp Mood=Ind SubjAuxCount=1 Tense=Pres | dundam | features...upos=NOUNlemma=dund xpos=NOUN Number=Sing Poss=Yes deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |
| Bi tiyeb teg-bët gi jeexee , lañu ko jébbal àttekat yi ndaxte dañu ko jàpp loxo-ci-poos mu di sàcc . | lañu | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=la Mood=Ind,Ind SubjAuxCount=1 | ko | features...upos=PRONlemma=ko deprel=iobj | UD_Wolof-AfriSUD |
| Mbokk , OSAD a la tekkil dénkaane yii tukkee ci Profesëer Amadu Galo Jóob . | a | features...upos=AUXdeprel=aux lemma=a xpos=INFL FocusType=Subj Mood=Ind SubjAuxCount=1 | dénkaane | features...upos=NOUNlemma=dénkaane xpos=NOUN deprel=iobj | UD_Wolof-WTB |